You are on page 1of 12

LE TAȈSSIR (WASSILATOUL MOUNA) DE SEYDIL HADJI MALICK SY (r.t.

a)
Ikhfirli oumatihi war hamni oumatihi wastour laha
wajbouranhâ rabbi yallahou (3 fois)
2- ( TRADUCTION WOLOF )
1.Alhamdu li laahi zi taysiiri Yàllahu 1.sante gnel na Yalla moom miy adji yombal ji
2.Nazma daraari lahu Yàllaahu Yàllaahu 2.bàkk ak kagn gnel na Yàlla te moom rekk kako yeyoo
3.Yàllaahu salli salaatan lantiha alaha 3.Yow Yàlla nanga djouli ag djouli gou amoul àpp
4.Dollig mucc si ki gnu tànn yow Yàlla
4.Sallim allal Mustafaa Yàllahu Yàllahu 5.Lou tollu sig missal julli gi gnu jaglel borom xam xam yi
5.Tahaadalaa salawaa til xaasatil hukamaa 6.Gnom gnognoy boromi coofeel diy waay fa yàlla
6.Ahlil mahabbati ahlil Laahi Yàllahu 7.Jullil te dollig mucc si weer wi yow yàlla
7.Salli salaatan wa tasliiman alaa xamarin 8.Si lerug weer woowe takh nga sàkk aduna ak lisi biir
8.Min nuurihii quliqal akwaanu Yàllahu 9.Weer woowe nga xam ne bu melaxul woon
10.Adduna ak lisi biiram des sig leudeum
9.Law lam yalux fifadaa ilkawni tal-atouhô 11.Leer googe di leer gou jougé si leer gu maàg gi
1O.Tabqal bariyyatu fii zalmaa-i Yàllahu 12.Te nga diokh ko yow Yàlla xam xam bou yaatu te gnaw
11.nuurun min annuuri xad awdaatuhu hikaman 13.Muy leer ak xam xam guy baawan sig mbindef yi
12 .Tafiidu faydan allal axlaaxi Yàllaahu 14.Leer googu ay leer zeur ngir aar ko si loorangé mbindef
13.Nuurun ahaa tabihil anwaaru haajibatan yi
15.Mou di ag leer gou fés indi yit leer gu fés
14.Anil hàqiiqati kullal xalqi Yàllaahu
16.Di gindi jaam yi sig leudeum indi leen sig leer
15.Nuurun mubiinun ataa nuural mubiina li-ir 17.Amul béne mbindef moo nàndalug teddange yow Yàlla
16.Saadil ibaadi jaamii-an Rabbi Yàllaahu 18.Gu jogewul si leeram gu sell googu yow sama boroom
17.Maa fiil bariyyati man lam tasqihi karaman 19.Deug deug nekkug boroom djeum jii ak penkam
18.Min nuurihi Rabbana Yàllaahu Yàllaahu
19.Deug deug nekkug boroom djeum jii ak penkam
19.Hàqiiqatul kawni aynuzaati tal atuhaa
2O.Ifaadatu Laahi nuuru Laahi Yàllaahu 20.Doonul lu doul ag leer goo baawaan yow Yalla
21.Salli aleyhi salaatan lantihaa kamaa 21.Yow Yalla jullil ag julli gu amoul kem si yonent bi
22.Ag julli gu amul mass ni sa maggaay gnaké mass
22.Laa lil kamaa lintihaa Yàllaahu Yàllaahu
23.Yow Yalla jullil ag julli te dollig mucc yonent bi fàww
23.Salli aleyhi salaatan salliman abadan
24.Lu tollok matt gimou màtt ba doon sopey Yàlla
24.Adda kamaa làtihi hibbika Yàllaahu
25.Nanga julli ag julli gou màtt seuk
25.Salli aleyhi salaatan Rabbi kaamilatan 26.Lu tollok lépp li nga xam ne sa xam-xam weur na ko
26.Adaa ihaatati ilmil Laahi Yàllahu 27.Yàlla, nanga yeureum té jéggal xeetu yonent bi
27.Ixfirli ummatihi waarham bi ummatihi 28.Yàlla , nanga suturaal té neubbal ay gnawtééfam xéétou yonent bi
28.Waastuur lahaa waajburan haa Rabbi Yàllahu 29.Yow Yàlla, di Aji-yeurmandé ci àdduna ak ca àllaaxira,
29.Yàllaahu Rahmaanu yaa Rahiimu yaa Malikul yow, Buur bi,
30.Qudduusu yaa Muuminus sallamu Yàllaahu 30.Ku sell ki, ku woor ki, yow miy jàmm ji, Yow Yàlla.
31.Yaa Mutakàbbiru yaa Jàbbaaru Xaaliqu yaa 31.Yow mu màgg mi di boroom doolé, tey sàkk
32.Muhayminul Baari-ul Qhaffaru Yàllahu 32.Yow mi tééwé lépp té wéet ci sag càkk, tey jéggalé bàkkaar yi
33.Aziizu Qahaaru yaa Waalil Musawwiru yaa 33.Yaay ku tédd ki, ki not léép té aajowoo mbir yépp
34.Wahaabu Razaaqu yaa Fàttaahu Yàllaahu 34.Yaay kiy mayé, yaay kiy xéewalaaté yaay kiy ubbilaaté
35.Yow yaa xam, yaa lépp, yaa talal té yaay àtté
35.Allimu yaa Qaabidul Baasitu yaa Hakamul
36.Yaay téral, yaay wàccé, yaay yékkati, yow Yàlla
36.Mu-izzu yaa xaafidu Raafi-u Yàllaahu
37.Yaay toroxal, yaay ki maandu, yaay dégg, yaa yaatu
37.Muqillu yaa Adlu Adlu yaa Samii-u Waasi-u yaa
38.Yow aji-gis, di aji-dekkal, yom mu léwét mi, yow Yàlla
38.Basiiru Baa-isu yaa Latifu Yàllahu
39.Yàlla, Yow mi jiitu yow miy woomal, yow miy dés
39.Rabbi Muqaddimu muxni yaa Muwaxiru yaa 40.Yaay ku woom ki, di kiy daj lépp ci gisam.
40.Xaniyu Yàllahu yaa Xabiiru Yàllaahu 41.Yaay ku deugeur ki, ki neck fépp, tey méngalé
41.Matiinu yaa waajidul waliyyu Rabbiya yaa 42.Yow mi yelloo cant, yow mu koweé mi, yow Yàlla
42 .Hamiidu Yàllahu yaa Aliyyu Yàllahu 43.Ku léwét ki, di deug gi, ki gneupp wéer sééni mbir, yaay ki màgg
43.Haliimu yaa Hàqu yaa Wakiilu Maajidu yaa 44.Aji-jéggale ji, yaay ki dund, yaa taxawe àdduna bi,
44.Xafuuru yaa Hàyyu yaa Qàyyumu Yàllahu Yow Yàlla
45.Yaa yélloo cant, Yaay dogal, yaa màgg, yow sama Boroom
45.Sakuuru Jaami-u yaa Majiidu Rabbi ya yaa
46.Yow miy matal kooleuré, té màgg, yow Yàlla
46.Kabiiru yaa Muqsitul Aziimu Yàllahu 47.Boroom doolé, ki sàkk tey delloo ruuh yi tey fént,
47.Qawiiyu Muhsil Mu-iidul Mubdi-u Samadu yow mi gneupp jublu
48.Muhyil Mumiitu Ra-uuful Barru Yàllahu 48.Yaay dundal, yaay rey, rey, yaay gnééwaneté, ku
49.Tawwabu yaa Muta-aalil Waahidul Ahadul baax ki, yaw Yàlla
50.Maani-u yaa Daaru yaa Naafi-u Yàllahu 49.Yaay bale, yaa kowé, yaay ki wéet ci kénnam gi
51.Yaa Maalikal Mulki Rabbi Zaldjalaali wal ik 50.Yaay kiy téré, Kiy lore, Kiy jarigne, Yow Yàlla
52.Raami Shahidul Badii-ul Haadi Yàllahu 51.Buuru buur yi, di sunnu Boroom, boroom màggaay ak
tédd-nga
53.Yaa Nuuru Muntàqimul Qaadiru Muqtadiirul 52.Yow mi Sééde lépp, jéggi dayo tey Gindi jam yi, yow Yàlla
54.Mujiibu Yàllaahu yaa Waduudu Yàllaahu 53.Yow Léér gi, ku jub ki, Boroom kàttan ak Meun-meun,
55.Ya Awwalul Aaxirul Kariimu Zaahiru yaa 54.Yow miy wuyu, yow Yàlla, yow mi gneupp sopp,
56.Raqiibu Baatinu yaa khassibou yallahou 55.Yaay ki jeukk, kiy mujj, ki Tééd yow mi sa lépp féégne
56.Ku fuglu ki, yow mi làqu, yaay Aatté, yow Yàlla
57.Muqiitu Yàllaahu yaa djalillou rabbi wa ya 57.Yaay kiy dundal, yow boroom bi, yow ku màgg ki,
58.khassibou yallahou ya Hakiimu Yàllaahu 58.Ki wottu lépp, ku Xérégne ki, Yow Yàlla
59.Kiy jéllale, kiy donn lépp, di fi dés ba fàww,jub téy jubal
59.Afuwwu yaa Waarisul Baaqi Rashidu wa yaa
60.Yaay kiy mugne, yow sunu Boroom,
60.Sabuuru yaa Rabbanaa Yàllaahu Yàllaahu 61.Ci barké mboot yi sa tur yi làq, Yàlla, dollil xééwal
61.Bisirri haazaal asaami Salliyan alaa 62.Ci sunu Sang, ki gnu santloo ko, yow Yàlla
62.Sayyidinal haamidil Mahmuudi Yàllaahu 63.Té mu ubbi buntu yeurmandé, teuj buntu séytaané,
63.Al Faatihil muxlaqil Xaatimi maa sabaqal mottali la jiitu
64.Musral Mukallami Xayril Xalqi Yàllaahu 64.Moom mi nga ragnaane, waxloo ko, mu geun ci
65.Annaasiril hàqqi bil hàqil jalii wa ilaa mbindééf yi
65.Mooy kiy dimbali deugg, deugug Yàlla gu féégn gi,
66.Siraatikal mustàqiimil Haadi Yàllahu
66.Nu ngi jaar ci yoon wu jub wi, yoonu kiy jubal, Yow Yàlla
67.Topp njabootam ci deuggu kemug dooléém, ak
67.Summa alal aali Hàqa qadrihi qadaran
kàttanam
68.Miqdaarihi indakal Aziimi Yàllaahu
68.Ak darajaam ci yow Yàlla, ku màgg ki, yow Yàlla
69.Rabbun tabaaraka, aw Rabbun taqaddasa,
69.Boroom bu séll bi té séllam màgg lool
aw 70.Boroom bu kowé bi, bépp kowé, yow Yàlla
70.Rabbun ta-alaa uluwan Rabbi Yàllaahu 71.Ab jaam a ngii doyadi gnak toroxlou toumouranké
72.Jjaam bu tiit te jak ngir ay bakkaram yow yalla
( 3 fois )
73.Yyaw dey laay tallal samay lokho yakkar ay njégal
71.Abdun zaliilun faqiirun xaasi-un wajilun 74.Nnanga ma maay limalay niane yow yalla
72.Zuujaza-in ashifun Yàllaahu Yàllaahu 75.Géej dafa buusu géejug bakkar yow sama
73.Ileyka maddal yadaa raja-a maxfiratin ndeugeurlay
74.Habli musaa mahatan Yàllaahu Yàllaahu 76.Mman sa jaam dey ragal na lab si yow yalla
77.Ggan gaal la niouy yakkar ngir mucc gudul sag
75.Tamaw wadjal bahru, bahru zanbi yaasiqati
yeurmandé
76.Wa innani Rabbi xiftul xarqa Yàllaahu 78.Di yeurmandé gou magg gi te matal mbindef yeup
77.Wa maa safiinatu turjaa xayra rahmatikal yow yalla
78.Uzmal amiimati kullal xalqi Yàllaahu 79.Maa ngi tawat, jeumale ci Yow, as soxla té du faju
79.Ashkuu ilaa laahi haajan laysa yarfa-uhaa 80.Feek àndoo ci, Yow sunu Boroom, Yow Buur bi
81.Ndax am na ku man a dindi la Yàlla bi namm cib
80.Siwaaka yaa Rabbannaa Yàllaahu Yàllaahu
jaamam
81.Halmin muziilin bimaa qad kaana yuuriduhu 82.Boroom jam yi, nu di la jaamu yow mi gnu bind
82.Rabbul ibaadi alayhim Rabbi Yàllaahu 83.Yow miy àtté ci mépp mbir moo namm ci gnun, sa jamm yi
83.Wa naafizun Haakimun fiinaa iraadatuhu 84.Ca na mu la soobé, Yàlla màgg na, yow sunu Boroom
84.Kamaa Yasaa-u wa jalla laahu Yàllaahu 85.Yàlla na nga jéggal sunuy waajur ak seurign sépp
86.Ak ku juddoo ci gnoom ak gna am islaam té di ko
85.Wa saamihan waalidiinaa wasuyuu xawaman taxawé
86.Qad waladuu wazawil islaami Yàllaahu 87.Dollil ay xéewal jeumalé ko ci wallu gnu ba fàww
87.Salli salaatan tunajjinaa bihaa abadan
88.Jamii-al ahwaali wal afaati Yàllaahu 88.Ci bépp jafé-jafé ak gàkk-gàkk yow sunu boroom
89.Nanga dolli xéewal jeumalé ko ci fajal gnu ba ba fàww
89.Salli salaatan bihaa taqdilanaa abadan 90.Mbooléem sunuy aajo, yow sunu Boroom
90.Jamii-a hajaatinaa Yàllaahu Yallaahu 91.Dollil xéewal, yow Yàlla, jeumalé ko ci j”ggal gnu
91.Salli salaatan bihaa Rabbi tutahirunaa 92.Ci mbooléem sunuy gnaawtééf, Yow Yàlla, yow
92.Min jumlatis sayyi-aati Rabbi Yàllaahu Buur bi nuy jaamu
93.Salli salaatan bihaa Rabbiya tarfa-unaa 93.Dollil ay xéewal, Yow Yàlla jeumalé ko ci yeukkati nu
94.Ca daraja ya geuna kowé fa yow,Yow sunu Boroom,
94.Axla minad darajaati rabbi Yàllaahu
95.Nanga dolli xéewal, yow Boroom bi jeum ci jotale nu
95.Salli salaatan bihaa Rabbi you balikhouna 96.Li geuna réy, geuna sore ci yaakaar yow sunu Boroom
96.A-jalla aqsaa minal xaayaati, Yàllaahu 97.Yow Yàlla, yow Boroom bi, xéewal yi nuy yootu
98.La nu raw, mbaa sunu gannaw, Yàlla nanga nu ko défal
97.Yàllahu yaa Rabbi fil xayraati jumlatiha 99.Yàlla, jottalil ci kiy rammu jaam yi eulleug, sunug
98.Indal mammaati wa bahdal fawti Yàllaahu koolleuré
99.Balix ilaa Saafihil aali amaanatanaa 100.Té sunuy julli ànd ak mucc ci moom, yow Yàlla.
100.Salaatanaa ma-ahaa tasliimu Yàllaahu 101.Yàlla, dollil jàmm ci kiy wommat jamm yi té nu
101.Salli wa sallim alaal haadi samiimi kamaa deugeurloo ko
102.Nga geureum ko, mu sant la, yow Boroom
102.Tarda wa yardaahu yaa Rahmaanu yeurmandé,
Yàllaahu 103.Yàlla dollil xéewal, té jàmmal leer googu weur képp
103.Salli wa sallim alaa nuuril muhiiti alaa koo bind
104.Kullil mukawini kanzil xalqi Yàllaahu 104.Ci kiy mbootu mbindééf yi, yow Yàlla
105.Dollil xéewal àdduna ak àllaaxira yeurmandé ci sunu
105.Salli alaa Rahmati daarayni sayyidinaa
sang
106.Ruuhil wujuudi wa sirrizzati Yàllaahu 106.Ki mbindéef yiy noyyée té mu yor ay mbooti boppam
107.Alaal muxaatabi waasjud waaqtarib 107.Yàlla, na teddaange nekk ci ki nu digal mu sujjoot té
karaman jégé boroomam
108.Salli wa salaaman Rabbi Yàllaahu 108.Yàlla dolli ko xéewal ak jàmm,yow Yàlla
109.Dollil xéewal ci sa àlluwa ji nga sose mbindéef yi
109.Salli alaa lawhikal mahfuuzi lasrafimin 110.Té mu tédd ci bépp mbindeef, yow Boroom
110.Kullil xalaa iqi yaa Rahmaanu Yàllaahu yeurmandé, yow Yàlla
111.Tilkal amaanatu takfiiman takunnu lahu 111.Lii déy, ci ndénkaané, doy na ku Yàlla taxa joog
112.Muballixan yaa manul iisaala Yàllaahu 112.Moom miy jottalé, téy mottali mbir yépp, di sunu
Boroom.
113.Yow Yàlla, bul nu xagn , bés-pénc, gis yonent bi,
113.Laatahrimanaa ilaahil yawma ruhyatuhu 114.Bul sooyal képp ku la yaakaar, yow Buur bi,
114.Falaa yaxiibanna man yarjuuka Yàllahu 115.Ndax ku giséwul ak moom euleug dana weuy ci
115.Man lam yakun yalqahu xadan yanalwajalantiitangé.
116.Haazaal kasiiru ataa lil jabri Yàllaahu 116.Lii day baré lool té yit, ngir défar mbir yépp
117.Wa kun lanaa Rabbi fii kullil umuuri faman 117.Kon Yàlla, nanga nu jàppandal ci mbir ya la soob
118.Yakun kazaalika yalqal yusra Yàllaahu 118.Ndax koo dimbali mu taseek yombal, yow Yàlla
119.Salli salaatan bihaa Rabbi tu-allilunaa 119.Dollil xéewal, yow Yàlla, jeymalé ko ci nàndal nu
120.Ca déxu kawsara yow Yàlla, yow sunu Boroom
120.Bihawdihii Rabbanaa Yàllaahu Yàllaahu
121.Yàlla nanga dolli xéewal ak jàmm juygilli
121.Salli salaatan wa tasliiman zaraa itaran
122.Ci sa soppé bi ak njabootam, yaw Yàlla
122.Alal habiibi wa aalil hibbi Yàllaahu 123.Dolli xéewal wéer wi, féek mooy njiitu way-aji yi
123.Salli alaal badri maa ammal hadjidju ilaa 124.Jeum ci ziyaaraji rawdoom, yow Borom
124.Ziyaarati rawdi yaa rahmanou yallahou yeurmandé
125.Fadj hal ilahiya ya rabbi khasiidatanaa 125.Sunu Boroom, maa ngi gnan,xasida bii ma bind
126.Muy yoonu faj ci sunuy mébét, yow Boroom bi
126.Wasiilatan lil munaa Yàllaahu Yàllaahu 127.Maa ngi gnan Yàlla muslaay ci ragal mbindéef
yi
127.A-ouzu bil Laahi min xawfil anaami wa min 128.Ak top sama bakkan, mbaa yittéwoo alalu
àdduna
128.Ridan ani nafsi hammi rizqi Yàllaahu
129.Wa raddinii bil qadaa Rabbi musabbirani 129.Yàlla nanga ma geureum ci àtté, déf ma
130.Alaa balaa-ika yaa Rahmaanu Yàllaahu may mougn
131.Muuzihani choukraman awlaytanii ni aman 130.Ci say balaa, say nattu, yow Boroom
132.Djalla sanaa uka yaa Rahmaanu Yàllaahu yeurmandé gi, Yow Yàlla.
133.Laa uhsiyannas sanaa aleyka anta kamaa 131.Di ma sédd, ma lay sant ci xéewal yi nga
134.Rabbi alaa nafsi qad asnayta Yàllaahu may défal
135.Fakhfirlanaa waliman min bayninaa 132.Lott naa ci tagg la, yow Boroom
nasabun yeurmandé, yow Yàlla
136.Min djihati tiini aw fiddiini Yàllaahu 133.Manumaa dajal ci tagg la, doonté sama
137.Salli alaa saajidin qablal waraa fa-alaa giirug dund
138.Bisab-imii ati aamin Rabbi Yàllaahu 134.Yow Yàlla, tuuti naaa ci tagg la na nga ko
beuggé
135.Jéggal nu, ak képp ku bokk ci sunu askan
136.Ak ki nu bokkal suuf su nga nu binde ak ki
nu bikkal diiné.
137.Dollil x »ewal ci ki jeukka sujjoot mbindeef
yi ci jeuf
138.Ci lu tollu ci juroom gnaari téeméeri at, yow
Yàlla
FANADJINA Wa faza mane mâta mahat tawhidi
BISMIL LAHI RAHMANIR RAHIMI Wa mane daha bizi alal yakhini
Fanadjina ya khalikhach cheytani Youdjab bima rama minal matini
Mine Kaîdihi wa salabil imany MOUDJIBOU YA MOUDJIBOU YA MOUDJIBOU
Wa djawratis soultani wal djirani Fakhbal doua- a wadjilil kharibou
Ya rabbana walaf hatine nirani Nass alouka taslima bil khada i
Wakoulli mouhdiline anit tahati Wa sabra wa ridâ ladal bala i
Ya rabbana fakhdi lanal hâdjati Bil Moustapha chafî koullal khalkhi
Wa charri koully hâssidine wa hassidah Sabbit ilahi manntikhi bil hakh khi
Wa khaîdi koulli ka idine wa ka idah Azka salati lahi wa taslimi
Wa moufsidin biddini wal khira ah Allal lazi bouch chira bittaslimi
Ya rabbana wa moudjibi chakhawah Wa alihi wa sahbihil kharra i
Wa sikhtou billahi wa bil kitabi Wa tabi ina soummal awliya i
Wa bine nabiyil Moustaphal aw wabi Ya rabbana ya malickal kawnayni
Ad hô bi bissmil lahi wal Massâni Khina ilahi charra fi darayni
Wa ayatil kourssiyi zil mâ hanii Amatana lahou ala diny Nabi
Wa souratil ikhlassi zit tam djidi Wa houbbi chaykhinal imami tayhibi
Amina amaina astadjib dou’a ana Wa faza mane mâta mahat tawhidi
Wala toukhayyib sayyidi radja a ana Wa mane daha bizi alal yakhini
Ardjul amana yawma la amana Youdjab bima rama minal matini
ila liman amanahou mawlana MOUDJIBOU YA MOUDJIBOU YA MOUDJIBOU
Fakhbal doua- a wadjilil kharibou

FANADJINA
Nass alouka taslima bil khada i
Wa sabra wa ridâ ladal bala i
Bil Moustapha chafî koullal khalkhi
BISMIL LAHI RAHMANIR RAHIMI
Sabbit ilahi manntikhi bil hakh khi
Fanadjina ya khalikhach cheytani
Azka salati lahi wa taslimi
Mine Kaîdihi wa salabil imany
Allal lazi bouch chira bittaslimi
Wa djawratis soultani wal djirani
Wa alihi wa sahbihil kharra i
Ya rabbana walaf hatine nirani Wa tabi ina soummal awliya i
Wakoulli mouhdiline anit tahati Ya rabbana ya malickal kawnayni
Ya rabbana fakhdi lanal hâdjati Khina ilahi charra fi darayni
Wa charri koully hâssidine wa hassidah Amatana lahou ala diny Nabi
Wa khaîdi koulli ka idine wa ka idah Wa houbbi chaykhinal imami tayhibi
Wa faza mane mâta mahat tawhidi
Wa moufsidin biddini wal khira ah Wa mane daha bizi alal yakhini
Ya rabbana wa moudjibi chakhawah Youdjab bima rama minal matini
Wa sikhtou billahi wa bil kitabi MOUDJIBOU YA MOUDJIBOU YA
MOUDJIBOU
Wa bine nabiyil Moustaphal aw wabi Fakhbal doua- a wadjilil kharibou
Ad hô bi bissmil lahi wal Massâni Nass alouka taslima bil khada i
Wa ayatil kourssiyi zil mâ hanii Wa sabra wa ridâ ladal bala i
Bil Moustapha chafî koullal khalkhi
Wa souratil ikhlassi zit tam djidi
Sabbit ilahi manntikhi bil hakh khi
Wa faza mane mâta mahat tawhidi Azka salati lahi wa taslimi
Wa mane daha bizi alal yakhini Allal lazi bouch chira bittaslimi
Youdjab bima rama minal matini Wa alihi wa sahbihil kharra i
Wa tabi ina soummal awliya i
MOUDJIBOU YA MOUDJIBOU YA
Ya rabbana ya malickal kawnayni
MOUDJIBOU
Khina ilahi charra fi darayni
Fakhbal doua- a wadjilil kharibou
Amatana lahou ala diny Nabi
Nass alouka taslima bil khada i Wa houbbi chaykhinal imami tayhibi
Wa sabra wa ridâ ladal bala i ila liman amanahou mawlana

Bil Moustapha chafî koullal khalkhi


Sabbit ilahi manntikhi bil hakh khi Bismil Lahir rahmanir rahîm

Azka salati lahi wa taslimi ALLAHOU HASBI lidini


hasbiyallahou
Allal lazi bouch chira bittaslimi
Lima ilayhih timami hasbiyallahou
Wa alihi wa sahbihil kharra i
Likulli baghin alayna da iman abadan
Wa tabi ina soummal awliya i
Kaja liman yahsoudouni hasbiyallahou
Ya rabbana ya malickal kawnayni
Allahou hasbi liman bissûi kâda binâ
Khina ilahi charra fi darayni
Kajaka inda mamati hasbiyallahou
Amatana lahou ala diny Nabi
Wa inda massalati filqabri ja faraqine
Wa houbbi chaykhinal imami tayhibi
Limaqtraftu jounuban hasbiyallahou
Amina amaina astadjib dou’a ana
Wa indamâ nusibal mîzânu ma dilatan
Wala toukhayyib sayyidi radja a ana
Nardju nabiyyal houda qul
Ardjul amana yawma la amana
hasbiyallahou
Bismil Lahir rahmanir rahîm Allahou hasbiya la rabban siwahû lahû
ALLAHOU HASBI lidini Tawakulli wa iyabi hasbiyallahou
hasbiyallahou Ya rabbi salli alal muhtari min
Lima ilayhih timami hasbiyallahou moudarin
Likulli baghin alayna da iman abadan Fi haqiqqihi qultu haqqan
Kaja liman yahsoudouni hasbiyallahou hasbiyallahou
Allahou hasbi liman bissûi kâda binâ Kama tusallî alâ âlin sahabatihî
Kajaka inda mamati hasbiyallahou Ma qala abdun munibun hasbiyallâhou
Wa inda massalati filqabri ja faraqine
Limaqtraftu jounuban hasbiyallahou
Wa indamâ nusibal mîzânu ma dilatan
Nardju nabiyyal houda qul hasbiyallahou

You might also like