You are on page 1of 132
TOME 1 : POEMES LAYENES POEMES ET PENSEES PHILOSOPHIQUES WOLOF (de U'oralité & Vécriture) Docteur és Lettres, Chercheur 4 ITFAN C.AD. Université Cheikh Anta DIOP de Dakar e@ : ® , ay : % oe ¥ Los vA / ey ‘EDITE GRACE ALA COOPERATION ACCT-1 mages wee we CS 4 AVERTISSEMENT Les mots wolof sont transcrits selon Je syst®me de transcription adopté au Sénégal pour toutes les langues nationales par décret n°71 566 du 21-5-1971. Pr i conservé pour les noms propres de personnes et de localité leur transcription habituelle. Voici quelques indications sur la valeur phonétique des lettres wolof : 1, Les consonnes b, d, fg, k, 1, m, n, p, 1) 8, 6 ont Ia méme valeur phonétique qu’en frangais ; toutefois le g est toujours dur comme dans le mot francais gare. 2, Les consonnes , j, fi, D, x, w, y, ont chacune une valeur particuliére illustrée dans le tableau suivant : (occlusive palatale) équivaut au son ti du mot frangais tiare 4 (occlusive palatale) Squivaut au son dj dn mot frangais djinn 4 (nasale palatale) équivaut au son gne du mot frangais montagne (nasale vélaire) équivaut au son ng du mot anglais thing (constrictive vélaire) équivaut au son kh du mot arabe khalif (emi-voyelle) équivaut au son oua du mot frangais ouate. > (emi-voyelle) équivant au son y du mot frangais Yaourt. ‘ a 4 2 “ana mme Les voyelles bréves sont :~ centrale ouverte comme dans le mot francais balle maximale centrale comme dans le mot frangais gare mi-ouverte postérieure comme dans le mot frangais col mi-fermeé postérieure comme dans le son eau de marteau antérieure fermée comme dans le mot frangais fini postérioure fermée comme le son ou de bijou postérieure fermée comme le son é de élastique , mi-fermée comme le son é de apeuré mi-fermée comme le son eu de seul. uMe EQOA 4. On obtient l'allongement de ces voyelles par leur gémination : Exemple ms ta = lit Jaal toucher ad zol = cceur ool regarder > nit personne niit éclairer 2 set == propre ‘eet chercher 5 wér = guérir wéér poser contre 5 5. Les consonnes nasales qui se rencontrent souvent en position initiale sont : 2 mb équivaut au non mb de tambour 2 nd équivant an son nd de bandage nj équivaut au son . ndi de Bandiagara ng — équivaut au son ng dehangar see cceececcce ‘TABLE DES AUTEURS 37 50 94 102 127 INTRODUCTION Des témoignages sur la richesse de la langue wolof et sur labondance de sa littérature nous ont été donnés par les premiers européens qui ont étudiés cette langue. Le Baron Roger, écrivait dans “Recherches philosophiques sur la langue ouolof, (6dité en 1829 par Dondey - Dupré, Paris) : “ces peuples ont su donner a leur langue beaucoup d'ensemble, de délicatease, et de régularité”. Il poursuit : “que de combinaisons, quel esprit d’ordre n'ont pas exigé ces principes de convention, autour dequels tous les termes du langage viennent se ranger si heureusement, que souvent 'auteur d'une langue philosophique n'aurait pas fait mieux ? Le hasard ne produit Tien de semblable. Cette langue suppose un peuple doué d'un sens droit, d'une heureuse organisation et dont, malgré les préjugés absurdes qu'inspire trop souvent sa couleur, humanité n'a pas & rougir”. A la page 126 du méme ouvrage, il dit encore : “je ne-finfrai pas s'il fallait rapporter leurs tournures particulidres de phrases, et tout ce que peuvent avoir de remarquable lours expressions. Ils parlent trés souvent par figures, par images, et par sens détournés”. Quant a I'Abbé Boilat, dont Ie volumineux “Grammaire de la langue wolof publié en 1858 fut couronné par Académie frangaise, il écrivait “jai dit que les wolof aiment: passionnément la conversation. On croira peut étre quils s'entretiennent d'absurdités et de bagatelles ; nous allons Prouver au contraire que leurs entretiens roulent sur des choses utiles : quills en tirent toujours quelque fruit, comme nous en tirons de la lecture d'un bon livre, d'un auteur avec lequel nous Hons conversation en quelque sorte, et oi nous puisons des principes de morale. Supposez que leurs réunions soient faites dans une salle contenant une riche bibliothéque, et que le président de la société prenne un auteur moraliste, qu'il en fasse la lecture & tous et que chacun ait le droit dexprimer ses réflexions et vous aurez une vraie idée de leur passe-temps. Quand on peut comprendre comme il faut la langue et bien saisir les idiotismes, on est surpris de trouver chez eux tant de sagesse traditionnelle”. Des travaux récents ont été consacrés a la langue wolof par des linguistes parmi lesquels Sauvageot, Pathé DIAGNE, le pasteur anglais Church qui a eu 'amabilité de moffrir un exemplaire de son ouvrage. Et si jen juge par le nombre de chercheurs que jai regu a T'TFAN, je eux affirmer que l'étude de la langue wolof intéresse de plus en plus les grandes universités du ‘monde!. Il parait done urgent de mettre a la disposition du public et des chercheurs des textes composés par des poates et des penseurs wolof. Grace au soutien matériel de l'Agence de coopération culturelle et technique nous commengons la publication de po&mes et de pensées philosophiques wolof, et ce faisant nous sauvons des chefs d'couvre littéraires qui allaient strement disparaitre, Youbli finissant toujours par engloutir ce qui n'est conservé que dans les mémoires des hommes. Nous avons ainsi Tambition de faire passer la culture wolof de Voralité a l'écriture, projet pour lequel, des amis ‘moi, nous militons depuis une trentaine d’années. C'est en 1959 que fat publié le syllabaire “Ij Volof”. Labsence d'un systame d'écriture adéquat a été une lacune cruelle responsable de la perte immense de l'abondante production littéraire et philosophique des sidcles passés. Cortes, griice & la transcription par des caractéres arabes, une partie de Ia littérature religieuse woof a été conservée, encore que certaines familles demeurent réticentes a livrer aux chercheurs de vieux textes qu‘elles considérent comme un patrimoine privé. 1 En effet, sont venus me consulter sur la langue et la littérature wolof = Mme Anne-Barbara Ischinger de Institut d Etudes Africanistes de ' Université de Cologne, + M- Russe G. SCHUH, Ph. D. chef du Département de linguistique de univesité de Los Angeles. + M.Sunano Yukitoshi, professeur adjoint, a la facalté des Lettres de Université de jeunes filles do ‘Kumanoto, Japon = ete CELE 2eCU = Par contre la mase des potmes des pottes wolof contemporains dépasse nos possibilités actuelles de publication. Aussi ai-je décidé de ne faire figurer dans ce recueil que quelques potmes de chacun de ces podtes qui ont bien voulu me donner des poemes. Les résultats de la collecte que nous avons commeneé depuis des années et que nous Poursuivons, vont done étre publiés. Ces textes sont transerits au moyen de caractéres latins, selon le systéme de transcription adopté par le Sénégal pour toutes les langues nationales (décret 1n°71566 du 21/85/1971). . Je me permets d'inclure dans ce recueil mes propres podmes, qui ont déja eu 'honneur détre Tobjet de plusieurs émissions radiophoniques et télévisuelles. Enfin pour éviter un amalgame choquant, j'ai regroupé en volumes séparés les po’mes religieux, les autres po&mes et les pensées philosophiques. Seules, ces pensées, sont traduites en frangais, les potmes le seront peut étre plus tard. Je tiens & remercier bien sincérement tous ceux qui ont bien voulu m'aider, dans la collecte des textes et dans le travail municieux de transcription. ATA.C.C1T. qui permet cette publication, jexprime ma profonde gratitude. Forgeron, c'est en travaillant le fer que 'éminent podte Libasse NIANG gagnait sa vie. ‘Mais, il s'est révélé étre aussi un habile artisan dans le maniement de la langue wolof. La richesse des rimes et le rythme musical des huit podmes chantés qui suivent en sont un témoignage éclatant. Tl clame avec une conviction profonde et puissante sa la mission d'Envoyé de Dieu, de Seydina Mouhamadou Limamou Laye (1884-1909), fondateur de la Conférie Layéne du Sénégal. Il porte dailleurs l'un des surnoms de Seydina Limaamu (Libasse), qui aurait béni sa langue le jour de son baptéme. Il vécut dans les villages de Cambaréne et Malika od il forgeait des outils aratoires pour les agriculteurs. Mort en 1944, a I'age de 40 ans environ, il est loin d'étre oublié. Aujourd’hui encore on chante avec beaucoup de ferveur ses podmes, durant les nuits de veillée religieuse. Ke i BISMI LAAHI RAHMAANI RAHTIMI Baay Laay amul maas ‘Njool yaay boroom dine Xallal nga nu yoon ‘Leeral nga ngiram diine ‘Yeen gém yi kaay leen nu waxtaan Fiici kafi Baay Libaas, moo feeft ci Soodaan ‘Te noo nampoon wolof miin ko lool, Ji wax araamul, ci laay, kafi Séydi Soodaan Baay Laay a leen yay ci tééré Yalla, Buur bi nu moom Xamxam ba nekkoon ca Maxfuus, moo ko saytu woo len Waar leen iiu ganta, gém yay sellal ba rilwaan Bu len watal Baay Laay maas nde bonte mu fiaaw, ‘Yonnent akub sérifi dufiu benn ba diy maas, ‘Njiin jangul, bindal, dajalewal i t66ré di ci set ‘Yallaa ko yénni muy woote diine lislaam Baay Lay newul “baa siin mimmara ak liif, lam”, Jaaxal na walliy waxumaak fo6r6ya juy waare Dogonkoon alt réér ngeen jébbél ko Lislaam. ‘Maam Aadamaa tiim fla mu feekkoon ba tén ba laa w6ér ‘Malaaka yay sujjé6t ngir leeru Yonnent ga ea moom Laay laay la Laahu ja moo xotti gémméfi ga leer ya saawaan Yooyay jufiun réy na, danu koy woy ba Diiwaan ‘Xam naa ci say jiko fiatti tééméér Dadul jeex, am nga kiraama Sak mbaax réy na ku lim juum Rafet jikko mufi gu yaa ‘ ‘Xam-xam budal jéex, yaatu taaru tabe ‘Manda, am diine amuk leer Baay Laay ba muy waaja fees, biddééw la andal bu leer ‘Way réér ya naan biddeewub laar, way gém ya naan biddééwub leer Loolu bir na len, Séydééy “nééru lislaam” Baay Laay dafa feefi samp raayi jullit. waar leen, Bu ngeen géméon jéfu Buur Yalla du nigeen jaaxle ‘Yonnent dafa woote, ngeen gintu, bu leen naagu. Baay Laay, nakk feefi, ne Yala ma yénni ci yeen ‘Yallaa ma yénni ; te Yalla nee na gneen tuba yeen, ‘Mbooleem nit ak jinne kaay len xafitu lislaam Sunu Buur la nuy woy di tagg Yonnent bi aleyhi salaam Baay Laay a woote lislaam, gém len ko, man wé6lu naa, ‘Yaakaar, ku kafi Séydi am ngag may fa Diiwaanoo, Yaa naawewoon Makka, yanu leer yaak sunuy rou, Ba ngay céppéelu Ngor, riir wa dektu Rilwaan ‘Ku gém nu gém, ku bafi dunu taggoo ba Diiwaan, 13. 14, 15. 16. 17. 18, 19. 21. 25. 26. ‘Njool ma céppééla biir Yoof, leeram ga dem Kambaréén Jénéer ba dem Beyti Maamur “saalihhina” ya teew Na gém fa Ndar w6slu, Waalo gém te kontaan. Noviam ya wér ko di sabba, bafi yaa nga naa dééta waay Wax leen ci waa ji, balaa siiw sanku, nan dem ca Buur, Pikin dafioo jeex, maam jaa wootewoon diine, Ngélém dafa réy, te réér metti ma di jooy Ku doon siyaar Nabi, yaaram baa nga biir Jammalaay Ku dan bégé Séydi Isaa war nga fiéw tuuboo Yallaa la tannoon ci biir Yonnent yi, def la ngay nj ‘Yaa moom juréém fiaari diiwaan, xawsu mandi ngay leer Deefal wéijéek yow nde yaa leen mén fa diiwaan Ba Baay demee taxi Béér, tunt koon kiraamaam ya feefi Déndug nawet jib na noor, boobee ba tey ken du laal, Baay Lay kerook flay wu weex tiital na waa Béér. Sérifi si daa mawwu dugg xalwa di seeti Baay Laay Bétub kifiaan daan na mbémpeen ba boroom réér ‘Man dey dama yéém fii ko weddi te muy moom. Bu leen werante biib taal Yonnent a ko taal Ku ci xamul te di xamxamlu bafia laaj Yellonte ngay kan mbaa fé6reya di nga réér Léndém ga sank la doo seerooti “ridwaan”. Ku fekkewoon ba ngay woote xam ne yaay ki fi man ‘Xérém yu réy ya ca biir Yoof, xamb yaak fia key muur, Semmal nga len ba fiuy jaamu Yalla, ken dootu yow, Yonnent bi, yaay mbér mi xAlloon yoonu lislaam. Xamxam, lu muy jerifi, la moy jéfe ko, digal ko saw gay Bu loola lépp nekicul, moo jaa, ku fiy wonew yon Subhaana xamxam bu lay wommat jéme Saam ‘Wax ja moo lay gétén ngay layyoo jémé naari. ‘Yonnent fu mu mosa feeti, Yééfeer ya bai ko diy noon, ‘Na donn ay kaggu, floofiaa koy werante ba Saam ‘Na teela gém naan fa Zam-Zam, am fa ridwaan. Yow waat nga wacea nga, yaa woote jubél diiné Birél nga sap woote, doo layyoo ba ken di la yay ‘Yembal nga jox Séydi, muy ommat ba diiwaano ‘Yow waat nga wacea nga yaa woote jubél diiné Doo bayyi waxtu, doo tooii, doo naff kenn, sallaaw ; Sellal nga saw yoon Baay Laay yaa rafet diiné ‘Yow waat nga wicca nga yaa woot jubél diiné Naroon na noo sanku, noo ngi jaamu ken dootu yow Yonnent bi yaay mbér mi xalloon diine lislaam Baay Laay ne seytaane raay na boppi mbindééf yi Ba Baay nelawee la gééjtiit, neex ba nuy naan Dogoon ak réér ngeen jébbél ko Lislaam CeCe’ CLEEES 21. 31. 38. Ku koy werante da nga laajul fi doon jé¢ma bafi diinéém, Kalaame kook buur, ba Baay duggee gal La gééj sibbaa, Aras jaayoo Ba Boroom Aras yéngoo Baay Laay weesuwul Béér. ‘Xaybar la Yéeféér ya fitnaal noon ya fiuy secti ‘Njool ma feefiu leen ea tisbaar ngir yérméndeem ju réy ‘Ak bafi gém ya weddi, Baay Laay yaa rafet diiné ‘Nu nga naa kaayleen flu wér Gé6r gi, seet njafi li muy muur ‘Mu ne leen reew ngeen, nde suma njafi li bu ngeen ko dee laal ‘Asamaan daldi tappok suuf, gééj ga baawaan ‘Nu nga naan toy jii nu gis njafi lu mosul feefi Iu tey ‘Nébbub Yalla jomb na jaam gis ko, Njiin du seen maas Kéwél ga daldi féx, gna fia tiit ba daw tasaaroo Ba tiu laa yembaat la Baay Laay japp bay fiaan. ‘Moo simpi xmb ya, taxawal dine Lislaam ‘“Xaatimi nabi-fina” sunu Yonnent bi woy leen ko ‘Moo leeral sunu xol ba sunu tur dem ba dijwaanoo ‘Nuy musiu séytaane, kiy raay boppi xam ya fiuy réér. Diggénte rafle waak xiif waak mar wu tar wa ca Saam ‘Na ump gaa yay déggal Yonnent ba Diwaano Lay jeex na Njjiin jib na Diwan wacc biir Yoofi gééj ‘Tambur ba jib na, muy baatub Laa illaa Laah, Li Yalla def bir na miim rééw, dootu fey abaadaa ‘Japp ak Julléék woor la nuy salloo ba rilwaan ‘Japp ak julléék wor la nu Yonnent bataleel Gé6r ak jigéén ndaw épp da ciy maase ‘Yonnent a ngay nelaw te bu yeewoo nu kentaan. Kafi leon boroom ngir mi, Baay Laay mooy dindi réér ‘Yaa nuy dindil tiisa bammeel may nu xééwél ca biir ‘Firdawsi, kawsaray baawaan nuy sanguy naan ‘Yaa dangu jém Pééy bu réy bi, flépp sew na ci moom Dééyaale fank Buur ba, ba mu tampeel la, yaay Ruuhu Laahi Yallaa la may yaa di njiitu “ahlu Soodaan” ‘Yow yaa jékké6n feefi, di jantub diine, bir na mim rééw Leer yas ngiy baawaan ba Soodaan siy xécco may gi floom Datioo xamul Xawsu, Baay Maanaay boroom diiné Anta Lamiin nga “yaa Séydil xalaa-ixi ‘Yaa samen Samaanun, wa yaa nuurun bilaadi Seydi Ruuhun min na Laahi” Tlahiinaay pééy ba, noo séqé taabal ja nook Maam_ Firdawsi kontaan na ngir nun fiy déggél flaari leer Bunngeen yaboo maare, am ngeen mbér fa Diiwaanoo 40. 41, 42. 45, 46. 41. 48. 49. 50. 51. 52, 54, Bu leen ififiaanante ngir nun Bour bi nuy jaamu moo sakkoon Mbugék, mbégte, te nuy fan mbég mu réy ma ca biir Firdawsi, Séydi yaa nuy omat ba Diiwaanoo ‘Yonnent la nuy woy, bu leen digpat cofeel gu tar la Xol fees na bay tuuru, gém woy leen boroom diine ji, ‘Bafi yea ngi suumurlu, nuy kontaan ba Diiwaanoo Sa wird wi, da nga ko jaayul, nde bonte nga riis, Sakkuwoo ku lay siiwal, wees nga puukére laay Yaa jfituwoon gaa fia Diiwaan tann lislaamoo Ngirém mi réy na te yaa, wirdam wi matna te leer Gaalam du tarde du raay, paasam jafewul ab jaam Roy leen ci Séydi, moo nuy ommat ba Diiwaanoo “Lay laa illa Laahu, Jélliilu Zikru Rabbani” Bi Laahi ku bat xawsu, doo seerooti Yonnent ba naan, Lay laa illa laahu, leer gay jolli ba Diiwaanoo Al hambu li Laahi, sunu Yonnent bi doy na noo laay Nee na yeen gém yi, am ngeen ngénéél, Yallaa ma wooteloo Ngeen fiéw, japp leen ci laay-laay ‘Japp ak julleek woor la nuy salloo ba Diiwaanoo ‘Ab jant fenk na biir Yoof, guy gindik réér Réylu ak way-réér la fiu fallas ca niiraan ‘Tee ngen a waaxu fiéw laaj Séydi boroom dine. ‘Tambur bu réy ba fa Buur Yalla la fiuy jiin Sunu yaaram bu tedd bi Séydi Ruohu Rahman ‘Makkaak Medina ba Saam rafife na say leer. Sunu Yonnent be mu bayyikoo Beyti Maamur la feeti Yaraax la wacei, gis fi ko jangoon te rafifieewuflu Ruy séénu kaw, Njool ma war Jakkeer ja xuus ci seen biir Jullééji Baay Lay, Yaraax werante, nay w66l65 ‘Yaaram bi tiim nga say mas, Baur Yalla def na ko jéég, Sérifi si bafi dafioo réér jomlu nde bonte fu lagj Xatmun tariixa bi Isa ibnu Maryaamaa N66ru Nabi néoru Isaa ibnu Maryaamaa Yaaram bi donn ngay leer, sellal nga yoonu lislaam roy leen ci Séydi moo nuy ommat ba Difwaan Nun kay nu ngiy gaajo leeram yu tar yi nuy naan Bafi yaa ngi nuy xas, da nuy sibbaa, du nook fioom Looloo di seen diine, séydi am nga rilwaanoo. ‘Tammal nga say gune fuy xam yoonu Yalla bay mag ‘Yéénétunoo bayyi lislaam, yaa nu won yoon wi ‘Tampees na nuy tur ca Diiwaan, yaay boroom diinee, rrlook @ dem jakka, fatte toppatoo ndaw, te boo soxlaa di-leen pampe. i layyoo la daan jur fa Sam, lileey mbasun dine Roy leen Njool boroom diinee. J (orarene 55. 56. 87. 58. 59. 60. 61, 62. Kuy xafitu lislaam te doo lakkal xaleel won ko yon Doo teela may gune ag bum, muy moyug toofi ci moom. Loolooy mbasun dine, roy leen Njool boroom diinee. Bul xeeb wolof lee nga fate, deglu naa la fluy wax Xam leen ne bét da dul suur, dee doora gm du ngénéel ‘Ni daan werante Yonnent layyo ji nafi Saam. ‘Ku fekkewoon woote baak naaféq yaak fia gémoon Dellooti daw ngir ga banneex, topp dunyaa ba dee Ku dem fiu ngay réccu ngir layyoo ba fa Saam Limaamu Laay, Mahdiyu xayrul waraa Muhamadu Bu ngeen xamul g66r gi, moo feetioon ca Makka, muy basx Mu deliu feet Yoof, Waa rééw may xéecoo yoonu Makka Dafioo xamul muj ga, Baay Maanaay boroom diinee. Loo tayyi fiakk nga, Ioolaa réecu fekk mu wéy Nan daan bakken yi, te tuub sellal, ku réy da ngay réér Roy leen ei Séydi moo nuy ommat da Diiwaanoo ‘Taasanxa yaa dal ca biir yééféér ya, tambur ya di jooy Buur Yalla doolee! na Aaleek fit wu réy wa a moom Jambaar ga tar na leer gay jolli ba Diiwaan. Mbooleem li fiy fSéreya dufiu dab Abdulaay bun Salaam ; Laajam bu réy ba mu doon leaj Yonti Yalla Nabi ‘Te noon bu key xam na ngeen tuub, booba mooy Mustafa ‘Mu wax ko lépp, mu yéém ba waaru far tuub ci moom Dellooti Xaybar naa tuub leen Muhammadu fees. Xaybar la yééfeer ya jéex ngir doj yu tang yay dal Malaaka yaay wace, Buur Yallaay dimméli sunum njiit Roy leen ei Séydi moo nuy ommat ba Diiwaanoo Yallaa la yénni nga feet Makka flu baf diinee Nga sane Medina, leer gay jolli ba Saam Beyti nangul na la, Faas gém na sa dine, ‘Nga dellu feefi Yoof, fioofia baii diine Nga sine Kambareen, leer gay jolli ba Malika ‘Yémbél nangul na la, Ndakaaru gém na sa diine. Saa Baay Limaamu kiy njiit, Buur, Yalla may na ko moom ‘Yaaram yi xam na ko, moo dekkal ngiram Nabi Laay ‘Jébbél ko Bay Séydi muy daaral pomu dine. ‘Yow yaay Liimaan, wa lislaam, wa lihsaan, la ka ridwaan, Saw tur la fiuy tampe, soo yeewoo tabala ya jiin, Laay laa illa Laahu, leer gay wéy ba Diiwaanoo. Sunu rombukaay bii di dunyaa Bufu fi def lu fiuy lor ‘Na ngeen xam ne géor gu feefioon fa Makka ‘Moo dellu feefi fii i Yoo ‘Moo nuy jalle éllek Baay Laay yay boroom caabi yi 10, 1 BISMI LAAHI RAHMAANI RABIIMI “Allaahu ma salli allaa Seydinaa Muhamadu Salli va sallim, yaa Rabbi, salli a laa Muhamadu” ‘Saa maam Limaamu woote na 12. Ba “Lanbiyaayi" wédlu na ‘Te Ruuhu Laay jiitu na Di lampu leeri Medina ‘Yaaram bu yiw bi wace nga 13. ‘Yaa Ruuhu Laay tedd nga ‘Ku koy werante weddi nga ‘Su ma yabo ne stnku nga. Yallaa Ia yénni ngay Nabi Mu Negay seen généél ginnaaw Nabi, Liggééy nga, am ngérém lémbe Sa fiaari leer yijollina ‘Naari ngérém nga bool 15. ‘Nga ndam sa may ga y Firdawsi ngay t8ggoo junjun Yaa Séydi moom nga tuymé ja. Gém leen te w6dlu tey dégél 16, Di sant Laahu kiy ndimmél Buur Yalla moo la may, Rasuul ‘Nu gém ko w6dlu diine ja. ‘Yaa xalla yoon wu réy wu yaa, 1. ‘Wa jém ca pécy yu magg ya Sa ngir mi leer na noo ngi jaamu, Bafji diiné pertana. Fekkon nga yoonu diine sew, 18. Ba nééw ji doole yépp daw, ‘Nga xalla yon wi, yaa fi raw, Ku fonk jamu waaxusil. Gé6r ak jigéén di taalibe 19. sikkar sa riir fa babu ba Ba xol ya buur digaani mba Amiin ja, doy na noo jubél ‘Xamxam ba raw na féére ya 20, Jaaxal na lawliya yi ya Yaa jiité lanbiya yi ya Diiwaan bi yaa di seen ngénéél Yaa saytu diine jiy defar 21. 10 ‘Ni weddi Njiin dafioo xamul Ki mén ci diiné, noo déggal Da ngeen a laajul kiy jubal Nde moo di géér gu laabiir Jom-jomlu jommi fey na ko réy-réylu, réér it fey na ko ‘Xamul na laaj fu wax ko ko Ci yoonu diine mooy li war Damaa gisul ku mel ni Maam Limaamu Laay te dégguma ‘Ku wax ne Yalla moo ma yénni, ‘Moo ko wax nu wé6lu ko, Gém seede leen ne sant naa Ki tax ma seeru Séydinaa Ba gém ko, naa ko “aamanaa” Ku w66lu sant war na la Sérifi sa toppu tank ba Saa bay Libaas ne maay boroom, Kuy xafttu weer ba jant fenk Xamal ne leer ya wr na la, ‘Njaa-all yeek njanaaw yi fiook Garab yi boole gém na fio Nit ak jinney werante, noo La woolu, Seydi todd nga ‘Bu gaalug Baay Libaas riddéé Ba gém yi naani Kawsara Kerook, fi gantu Baay Libaas Di fice fii gém ca kump ga. Ni téx te buur datioo tékkaale % ‘Mahdiyook i walliya Ka wax ne Yalla moo ma yénni Kooka moo di Nabiyu. ‘Araab yi ak Tubaab yi floo Jekkoon ei yoonu Nabiyn Wolof di xaar mujjug jamaano ‘Maam Limaamal Mahdiya, ‘Yaaram ba feefi na eiy Lebo Xérém ya tit na bay faboo Boroom ngénéél la nuy xaboo Yaa woote diine, noo wuy yoo eee 22, 23. 25. 26. 27, 28. 29, 31. 32. Subhaana maa ko yéénéwoon Nu boole xol yi ndax nu man, i jéém a roy fi jiituwoon te aw ci yoonu Muhammadoo ‘Lu fiy jullit nu bokk Ndey ‘Da gaan ci Buur bi leeri pééy ‘Ndax Buur jubal sunub liggééy ci lampi leeri Muhamadoo. ‘Yonnent yi wootewoon Hi laahi dakkantalees na leen ci Laghi, Ku dee te doo "adunwa" Laahi, di Abdalaahi Muhamadoo. ‘Nabee dikkcon ne jaamu leen ‘Yonnentub Yalla fieel na leen ‘Ku weddi kii dawal keneen Te génn yoonu Muhamadoo. ‘War ngeen na xam ne jangu neen ‘Te j8fewoo ko moo di teen bu teey bu neex te doo ca naan Gojam ba fieel na Muhamadoo ‘Moo tax ba Baay Libaas ne len da ngeen di wax te laaju leen ‘War ngeen a gaaw ma atte len ei yoonu Diine Muhamadoo, Xamxam ba woon ca Mustafaa Du jééx te lént nekku faa Bu kaap sottee mu tuuru faa Lu mankewul la Muhamado Araab du jél wolof déjoo Ndax gém yépp jangutu Ni mel ni man dafiuy béjoo werante sarti Muhamadoo. “Laa jlaaha illa Laahu Muhamadoo Rasuulu Iaahi waahidun Rabbul Jaliflu Majiidun Salli alaa Muhamadoo" ‘Yaa fee ci Yoofti gééja waay Sa tur wi siiw na dootu fey Boroom jamaano maa la woy ‘Nga may nu, dig nu, doo naxe. Sérifi sa jang Abeur: Ba xami "Chariihatu" ak cosaan Ki Yallla yoni fii Zamaan Nu bafi ko, xaw ma seen pexe. Br 33, 34, 35. 36. 31. 38. 39. 40. 4 42, Gifi naa ci Laahu kiy Boroom Tbnu Maryaama yaa di moom Yalla la tann doo moroom ‘Ni gém te w6dlu fioo texe. Diggénte Beyti Maamur ak Yaraax Diggénte boobu dand na ‘Te lef ma yaa na, Ruuhu laahi ‘Ngawar la, naar wa pepp na. ‘Njool war na gal ba dem Yaraax Boroom cosaan yi teeru ko da fico xamul fumoo bawoo Ngelémte flaaw na,metti na. Jullee na takkusaan Yaraax Jakkeer la war fanaani Yoo? Tulle fa Njool ma, gém ya naa Ko, Ruuhu Laahi, doy nga noo Ni gantu woon xéee66 na ko Na wuyyuwoon Madiiné Laahi Ci yoonu diine yébbu koo Bésub keroog la gééj ga neex ‘Ngor ak, Wakaam ya seede koo Caaroy, Ndakaaru, waa Yaraax ‘Nu naan ca mbeex ma, jaale koo. Haalim ya jomla, gé6j ga gém baa jox Madiine alc ruu-am Lu tee werante fey, nu gém tba gaa ya jiituwoon texe. Jirim ya jooy na ba séngeem ‘Njool ma #iéw na, seen rongoii ya fer Tullit yi wéétoon bay xelaat Donoy Madiine wace naa. ‘Raxas xolam ba muy fayaax Lu eay lu bon mu reli koo ‘Mu mel ni saaba door a baax Lu cay Iu gin mu dolli ko. Ku déglu saari Aluraan ‘Na gintuwoon la fay tokkoo ‘Ni jomlu diine ngir kifiaan ‘Malaaka yaa ngi leen ékkoo Ku nekk fééreyé boo nuyoo Sa mbééti xol mu rafifie ko Kerook mu jam la doo feyyoo ‘ba loo xamoon nga fatte ko. 45, 46. 41. 48, 49. 51. 54, ‘Ni baay Libaas di def “rijaal” Bu dee mbériit mu daane koo ‘Mbiram manee fu ko misaal Ki gém te w66lu xam na ko Li Yalla sante doo ko jaas Ku farluwul nga jéppi koo Taasanxa diine, yaa ko daas Ku bait nga rendi sai nga ko. Ku lamb saa buumi cofeel ci Baay Libaas, na bayyikoo Bu w6sluwul ki nuy texeel Guddeek bécég nu muslu koo ‘Samag tofee! di law ni ngooi ‘Ku saytu paaka jublu koo Nu jiaan ei Buur bi bafi ku toon ‘Musél ga yal na jiitu koo, Sa diine dootu fey wallaay ‘Yallaa la w66lu jox la koo ‘Yow itnga wéolu Ruuhu Laay ‘Mu jiita, gém ya topp kao. Séytaane mel nikkik fital Di takk jém of buumu xol Damaa begéén Iu may ragal ‘Nga mey ma tul gu may "sawe” ‘Ndax waaji man damaa léjél Ba mel ni kul ma fekk jél ‘Moo tax, ma flaan si sam ndimmél ‘Ndax mbér nga, yow man nga ma rawe May ndaw lu tollu eig béggam ‘Muy dox di yénni ay ndawam ‘Yu bon di sante aw xambam te xaw ma boor bu muy xawe Sérifi si mar na bay xundéofi ‘Nu dem ba Makka weesu koo ‘Ma jooy rotal samay rongoofi Da fioo gélém te rééré ko. Ku weddi ndaw te lagjuloo Bu ngeen layyoo mu sank la Ku Yalla yénni, ngay jotal Mbindééf yi, booba wace nga. Ki sot xalima, soos daa Tektal yu w66r la daa xalam Na saytu téére ya gélém ‘Nde boon fiu rafifiee aw meloom 55. 56. 87, 58. 59. 60. 61. 63. Kurél bu yiw bi fawxa ngeen ‘Ku dul yonnent bi fiee na leen Lu jiitu tey la Yalla noon Dinngeen sujj6ét ci Muhamadoo Li ngeen di ef, li ngeen di wax Li ngeen di jorta wésru maa Li ngeen di lééb la Yala wax Amana moo di atte ba Jullit yi maase ngeen ne Njiin Sore na waaye dektu na Li ngeen di waa ja léép malaaka Daldi saytu tampe ba, Mbooleem li fooréyiy yaxal Du fiw fi def lu gén jubsl Sikar te boolekaak matal Jullee ka fiaan ci Muhamadoo Bu nuy siyaari Jammalaay ‘Yooryoor ba Maam nangul na nu Guddik diiwaan la gém ya y6ek Kerkeraani Muhamadu, Da noo gisul ku mel ni Maam Limaamu Laay te déggu noo Ku melni Seydi dootal fees Ci dun bi wéor na kiy fexe. Ni gém te w6élu noon na seew ‘Nea woote, yow ni yénni ku Ku bai sa diiné dey ku beew CLEC EERE EL COCK -_— 2. 26. 8. Sa waay du jaq du jeaxle Léndém gu tar du ko laaloo Leeram ya doy géne jolli ‘Mu am “ridwaanu Ii Laahi", Laa ilaaha illa Laahu, du nu sappi Ngir mooy junjup ya ca Pééy ba Yal na mujjug sunu “Kalam” Di laa illaha illa Laabi. 21. Laay laay la laa illa laahu Woy len Jabeel ma ca leer yaa Limaamu Laay li nu lay woy Du jééx du xaaj dunu tayyi. BISMI LAAHI RAHMAANI RAHUMI Jantub diine lislaam Dangaa fenk fiuy miim ‘Nu gém wodlu leer yaa Negi baawaam fu ne, Baay Lay ngeen ne jangul, ‘Mu woo leen, fu gantal Ginnaawam ga daaneel Fihaalim june Jinnéék nit la woowoon Ci diinéém, ku teewoon Te doyloo ko diiwaan ‘Nga doy ko lune Da ngay jantu njolloor i gantoo ngi cw guur Te hi w66r na kuy gor Ci diiwaan bu ne Rasuuloo ilaahi, Ibnu Abdulaahi ‘Moo len woo wa Laahi Madiine fine Yallaa magg mooy Buur Turam woowa nay riir ” Ba seen xol Sarigoog leer ‘Mag ak ndaw ka nie Rasuuloo jlaahi ‘Mahdiyoo ilaahi Bi Laahi wa Laahi Ku baf “perta” nga Na ngeen déglu baat bi Da may woy Yonnent bi Booleek sant Rabbi ‘Te moo war kune ‘Wolof yooya laa miin ‘Te moom laay wuyoo Njiin “Sekarteer” amul yon Ci Yonnent bu ne 10. uL 2. 13, 4, 16. 16. 17. 18, + Al hamdu li Laahi ‘Wax ko war na noo ‘Ngir moo feefial Yonnent Cibiir xeet wu ne Gééjug leer ci Soodaan, ‘Xamul yaa ngi rootaan ‘Sangoo len ko muy naan ‘Moo gén ndox mu ne Seydi Ruuhu Rahmaan Donoy Mahdiyoo Ba yaaram ba laqoo Ba tey yaa fine Ba muy woote diineem Te fuy ba tariixaam Nga dib taaw di seedeem Ba tey yaa fine Da ngaa jub, sa fon jub Woyof toy niw xob Di jambaar, def ub tab Sigil yaa fu ne Daraapoo bu lislaam Bi yaa ko ame Bu leen yon wi rééréé Nga safi ko wone Boroom xeej bi yaa jam ‘Ni daarloo ei xamxam Gi seen kow nga jél ndam Siggil yaa fi ne Da nga yiw, yéwen taaru Doy képp kuy waaru ‘Séydéy boroom daaru ‘Yaa koy wone Ku doyloo sa xamxam Ba laajoo fu géné xam Do taggook i jamjam Yu réy wet gu nee 19. 21. 22, Baay Laay gééj gu dul jééx Te raw lem ci ag nex ‘Te lamboowul ag tiix ‘Tanxees a koy wone Setal seeni fiaaw-flaaw ‘Nandal gaa fia fluy soow Xanaa xaw na fico naaw Ku man dey wonee Ku lay roy ci bi “xarnv’”, Feefiul wonee Da ngay njiit ci lislaam Bi yaa leen tanee. Génél ngél nu nuy ndey Génél ngé] nu nuy baay (Te yaa gén sunuy maam 24, 25. 26. 27. 28, 29, Génél nuy junné. ku lay bafi du kontaan Lu waaj waaj du waxtaan Bu wallee fu reetaan Lumanman mune ~ Ba Njool may taxaw Ben si tey ngay xaree ‘Te wééroo sa gannaay ‘Muy dal saa su ne. Jiyaar jii si baatin Bu doon “Zaahiroo” ‘Nu jantoo nga daaneel Ci géér ay junné. ‘Ay jambaar nga andal Ku lay sééru gental Sa gannaay ya koy dal Du wér bay wanni. Ligeséyal nga Yalla Ligeééyal nga Baay Laay Ba jot soen Ngérém Doofimaasungune Ndawal Buur ku bait weej Ku réyréylu sew rame Soppeem yaa nga noon Ngééj fa xam faa mu ne Li tax diine yaa suux Ba Yonnent jekkee juwx Boroom tééré yaa xoox Di bafi wet gu ne. 16 31. 32, ‘Tawreet ak Linjiiloo Sabé6r diig nanoo Furxaan teew na gicceel ‘Na noon nii du ni. Ni daan bai Ras66l66 Siraat flooy répéél66 ‘Taubéén fia ko doyloo Ba tey foo fine. Bu dul konte Baay Laay ‘Landém sank fay gaay Ki tax ngeen di laay laay 33. 37. Yallaa ko yénni Da nuy fiaan ki nuy mey ‘Mu yobbél nu buy doy Ba cik mujj nu far wey Gi ngir mii nu ne Safiseel gém yi uy bees Giréé ngir mu tek lees Booleck ndééyi depees ‘Yu jém pééy bune Baal niiw ya wey ya Téggél goin ya teow ya Na laqook soppeem ya Si nit fleek jinné Dundal diine lislaam Ci barkeb Yonnentam Di njiitam di soppeem Da koy may lu ne. Da daan rey di dekkal Fu léndém mu leeral: Ba gééj wex mu wexal Nuy naan saa su ne. Ay kéémaan nga andal ‘Te say seede jééxul Ku laamlaami laajal Ci mag Wii fine Li war yeenu “haalim” Ci bii“karnu” mooy xam Boroom, boole kook gém ‘Te aw cim ngirém ‘Yeeteetoo fu yeowoo Xanaa ber sa saawaa Sa fiofi nappi faawaa Ba réér cik Iendém L HEEL

You might also like