You are on page 1of 22

Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob

Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Noo ngi dagaan ci képp ku

jot ci téere bi nga jottali ko
sa mbokkum taalibe ba mu
man koo jariñoo.
Yal na nu ci jёle ngёrёmal
sunu Boroom.

‫آمني‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

2 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Yàlla mu màgg mi wax na dëgg ṣadaqal-Lāhul-`aḍhīmu ‫َ َ َ ُ اْ َ ِ ُي‬

Te jotal na Wa ballagha َ ‫َ ََب َّل‬
Sunu sang bi mawlānā َ َ ْ ‫َم‬
Kay Yónentam bi rasūluhu ُ ُ‫َ ُ ا‬
Ka de ku ñu tànn al-muṣṭafā ‫صطََفى‬ْ ‫ا ُْم‬
Kay aji-dëggu aṣ-ṣādiqu ِ ‫اص‬
ُ ‫اد‬ ‫َّل‬
ِ
Ka de ku ñu wóolu al-'amīnu
ُ ‫اَم‬
‫ني‬
Te moom Yàlla Wa huwa
َُ َ
Mooy aji-dëggu way wax yi 'aṣdaqul-qā'ilīni ِ ِِ‫َ ْ َ ُ اْ َ اا‬
‫ني‬
‫ني‬ ِ ِ ‫اْم‬
Képp ku wax dëgg Yàlla moo la gën a dëggu wal-muṣaddiqīna َ ّ‫ص‬ َ ُ َ
Te nun jullit ñi Wa naḥnu
ُ َْ َ
Ci loolu nu wax ne Yónent bi jotal na `alā dhalika َ ِ‫َ َى َا‬
ِ ِ ‫ِم َّل‬
Nu ngi seedee ni Yónent bi jotal na minash-shāhidīna
َ ‫الا‬ َ
Te way gëm nan wa mu u'minūna ‫َ ُم ْ ِم ُ َو‬
Ci Yónent bi, ci Alxur-aan bihi ِِ
Te way dëggal nan li Yàlla wax Wa muṣaddiqūna ‫ص ِّ ُ َو‬ َ ‫َ ُم‬
Kenn amul benn xeetu pexe walā ḥawla َ َْ َ َ
Kenn amul benn xeetu kàttan walā quwwata َ ‫َ َ َُب َّل‬
Lu dul soo ko sukkandikóo 'illā ‫ِ َّل‬
Ci Yàlla billāhi ِ ِ
ِ
Kay Aji-kawe al-`aliyi
ِّ َ ْ‫ا‬
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
3 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Kay Aji-màgg al-`aḍhīmi ‫اْ َ ِ ِي‬

ِ
Yal na gërëm Yàlla Wa raḍiya l-Lāhu
ُ َ ََ
Sunu sang yi `an sādātinā ‫اد تَِا‬
َ َ َْ
Abuubakar 'abī bakrin ٍ ْ َ َِ
Ak Umar ibn Xataab wa`umara
َ ‫َ ُ َم‬
Ak Usmaan ibn Afaan wa`uthmāna ‫َ ُ ْ َما َو‬
ِ
Ak Seydinaa Alin wa`aliyin
ٍّ َ َ
Ak Talhata Wa ṭalḥata َ َ َْ َ
Ak Subayr waz-zubayri ِْ ‫َ ُّزالََب‬
ٍ
Ak Sahd Wa sa`din َْ َ
ٍِ
Ak Sahiid Wa sa`īdin
ََ
ٍ َ ِ ‫او‬ ِ ِ
ْ ْ َ ْ ‫َ َ ْ ا َّل‬
wa`abdi r-raḥmān ibni
Ak Abdu Rahmaan ibn Awf
`awfin
Ak Abi Ubayd ibn Jarraah
wa'abī `ubaydata ibnil-
jarrāḥi
‫َ َِ ََُب ْ َ َ ْ ِ ْاََّل ِا‬
Ak Hamsa Wa ḥamzata َ‫َ َ ْ َل‬
Ak Abbaas wal-`abbāsi ِ ‫َ اْ ََّل‬
‫اا‬
Ak Jahfar Wa ja`farin ٍ ‫َ َ ْ َف‬
Ak Aqiil wa`aqīlin ‫َ َ ِ ٍي‬
Ak Asan wal-ḥasani ِ َ َ‫َ ْا‬
ِ ْ ُ‫َ ْا‬
‫ني‬
Ak Usaynu wal-ḥusayni
َ
Ak Faatimata Wa fāṭimata َ ‫َ َا ِ َم‬
Ak Xadiijatu Wa khadījata ََ ِ َ َ

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

4 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Ak Aayisatu wa`ā'ishata َ ِ‫َ َاا‬

َ‫ل‬
ِ ِ َ ‫ااِ ِ َّلُم‬
َ ِ‫اا ا ُْم ْ م‬
‫ني‬
Wa sā'iri 'ammahātil-
Ak mbooleem soxnay Yónent bi
muu'minīna ََ
ِ
Yal na gërëm Yàlla Wa raḍiyal-Lāhu
ُ َ ََ
Ci Sahaaba `an 'aṣḥābi ِ َ ْ َ َْ
‫اا‬
ِ ِ
Yónent Yàlla bi rasūlil-Lāhi
َُ
Yal na julli ṣallāl-Lāhu ‫َ َّلى‬
Yàlla allāhu
ُ
ِ ََ
Ci moom Yónent bi `alayhi
ْ
Te def ci moom salaam wa sallama ‫َ َ َّل َي‬
ِ
Ñépp nag 'ajma`īna
َ َْ َ
‫ني‬
ِ
Ak ña topp sahaaba ya wa`anit-tābi`īna
َ ِ‫َ َ ِ الَّلا‬
‫ني‬
ِ ِ
Ak ña topp ña topp sahaaba ya Wa tābi`īt-tābi`īna
َ ِ‫َ َ ِ الَّلا‬
‫ني‬
ٍ ِِ
‫او‬
Ak képp kuy rafetal bi'iḥsānin
َْ
Ba bésu pénc 'ilā yawmid-dīni ِ ِّ ‫ِ َ ََب ْ ِ ا‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga def ij`alnā ‫ْ َ َْا‬
Yaw sunu Boroom nu bokk yā mawlānā َ َ ْ ‫َ َم‬
ِ ِ
Ci soppey Yàlla ak Yónent bi minal-muḥibbīna َ ِّ ‫م َ ا ُْم‬
‫ني‬
ِ
Ña diy way topp at-tābi`īna
َ ِ‫الَّلا‬
‫ني‬
Ñeel ñooñu lahum ‫َُ ْي‬
ٍ ِِ
‫او‬
Ci rafetal bi'iḥsānin
َْ
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
5 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Ba bésu pénc 'ilā yawmid-dīni ِ ِّ ‫ِ َ ََب ْ ِ ا‬

Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga def ij`al ‫ْ َي‬
Alxur-aan ji al-qurāna ‫اْ ُ ْآ َو‬
Bu màgg bi al-`aḍhīma ‫اْ َ ِ َي‬
Muy lollib sunu xol yi (printemps de nos
cœurs)
rabī`a qulūbinā ‫َِ َع َُب ُ َِا‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga leeral nawwir
ْ ِّ ‫ََب‬
Ci alxur-aan bihi ِِ
Sunu xol yi qulūbanā ‫َُب ُ ََبَا‬
Ak sunu bàmmeel ya ëllëg Wa qubūranā َ َ ُ ‫َ َُب‬
Yal na nga ubbi/seddal wāshraḥ ‫َ ْا َ ْا‬
Ci alxur-aan bihi ِِ
Sunu dënn yi ṣudūranā ََ ُ ُ
ِ
Yal na nga yombal Wa yassir
ْ ّ ََ
Ci alxur-aan bihi ِِ
Sunu mbir yépp 'amūranā َ َ ‫ُُم‬
Te yal na nga nu may tawféex dëppale nu Wa waffiqnā ‫َ َ ِّ ْ َا‬
Bépp mbir boo xam ni ci mbir moomu bun ca ِ ِ ‫اِما‬
duggée dinanu ci am
limā fīhi
َ
Sa ngërmande riḍāka `annā ََِ
‫اك ََّلا‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

6 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Yal na nga def ij`al ‫ْ َي‬

Alxur-aan al-qurāna ‫اْ ُ ْآ َو‬
Mu màgg mi al-`aḍhīma ‫اْ َ ِ َي‬
Mu nekk ca sunu kanam 'amāmanā ‫ََم َامَا‬
Te muy aji-wommat sunu Wa qā'idanā َ َ ِ‫َ َاا‬
ِ ‫ِ َ ْاَّل‬
Jëm Aljana 'ilāl-jannati
َ
Te Yàlla bul ko def mukk walā taj`alhu ُ ْ َ ْ‫َ َ ََت‬
Mu nekk sunu gannaaw khalfanā ‫َ ْ َفَا‬
Di aji màng sunu sā'iqanā ‫َ ااَِ َا‬
Jëm sawara 'ilān-nāri ِ ‫ِ َ اَّلا‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga def ij`al ‫ْ َي‬
Alxur-aan al-qur āna ‫اْ ُ ْآ َو‬
Mu màgg mi al-`aḍhīma ‫اْ َ ِ َي‬
Muy aji rammu gi nuy rammu shāfi`an ً‫َاا ِ ا‬
Di ku ñu rammuloo mushaffa`an ‫ل َّلف ًا‬
َ ‫ُم‬
Ci nun fīnā ‫ِ َا‬
Te Yàlla bu ko def walā taj`alhu ُ ْ َ ْ‫َ َ ََت‬
Muy aji xulóo māḥilan ‫َما ِ ًًل‬
Buñ dëggal ca lamuy wax bam nuy dal muṣaddaqan ‫ص َّل ًا‬َ ‫ُم‬
Ci nun fīnā ‫ِ َا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

7 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬

Yal na nga def alxur-aan ij`alhu ُ َْ ْ
Mu ñeel nu / nu moom ko lanā ‫اََا‬
Te Yàlla bu ko def mukk walā taj`alhu ُ ْ َ ْ‫َ َ ََت‬
Mu war nu / Muy musiba ci nun `alaynā ‫َ ََْبَا‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi al-Lāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga nu wërsëgal urzuqnā ‫ُ ْ ُز َْبَا‬
Ag jàngam tilāwatahu ُ َ‫تًِلَ َ ت‬
Ca melo wa `alā n-naḥwi ِ ْ ‫َ َى اَّل‬
Wa nga xam ni al-ladhī ‫اَّل ِذي‬
Dana gërëmloo yurḍīka َ ِ ْ ‫َُب‬
Ca nun `annā ‫ََّلا‬
Te Yàlla bul def nag (bul bàyyi mukk) walā taj`al ‫َ َ ََتْ َ ْي‬
Ñeel nu lanā ‫اََا‬
Bàkkaar dhanban ‫َ َْبًا‬
Lu moy jéggale nga ko 'illā ghafartahu ُ َ‫ِ َّل َ َف ْ ت‬
Du caage ni ag njàqare walā hamman ‫َ َ ََهًّا‬
Lu moy yërëm nga ko 'illāa farrajtahu ُ َ‫ِ َّل ََب َّل ْ ل‬
Du caage ni bor bu nuy lëjal walā daynan ‫َ َ َد َْبًا‬
Ndare fay nga ko 'illā qaḍaytahu ُ َ‫ِ َّل َ َ َْبل‬
Du caage ni ag ràgg walā marīḍan ‫َ َ َم ِ ً ا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

8 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Ndare saafara nga ko mu wér 'ilā shafaytahu ُ َ‫ِ َّل َا َف َْبل‬

Du caage ni muy ab noon boo bàyyi walā `aduwan ًّ ُ َ َ َ
Ndare fegal nga nu ko 'illā kafaytahu ُ َ‫ِ َّل َ َف َْبل‬
Du caage ni aji fàddu walā ghā'iban ‫َ َ َااًِا‬
Ndare delloo nga ko mu ñibbi ci jàmm 'illā radadtahu ُ َ‫ِ َّل َ َد ْدت‬
Du caage ni aji moy ndigëli Yàlla walā `āṣiyan ‫َ َ َا ِ ًا‬
Ndare musal nga ko 'ilā `aṣamtahu ُ َ‫ص ْمل‬ َ َ ‫ِ َّل‬
Du caage ni aji yàqu walā fāsidan ً ِ ‫َ َ َا‬
Ndare yéwénal nga ko/defar nga ko 'illā 'aṣlaḥtahu ُ َ‫ِ َّل َ ْ َ ْ ل‬
Du caage ni aji-dee walā mayyitan ‫َ َ َمِّلًا‬
ِ
Ndare yërëm nga ko 'illā raḥimtahu ُ َ‫َِّل َ ْل‬
Du caage ni nga bàyyi ayib walā `ayban ‫َ َ َ َْبًا‬
Ndare suturaal nga ko ba kenn du ko gis 'illā satartahu ُ َ‫َِّل َ لََب ْ ت‬
َِ َ
Du caage ni mbir muy aji jafe walā `asīran
ً َ
Ndare yombal nga ko 'ilā yassartahu ُ َ‫َِّل َ َّل ْ ت‬
Du caage ni senn soxla walā ḥājatan ً َ ‫ََ َ ا‬
Ci soxlaay àddina yi min ḥawā'ijid-dunyā ‫ِم ْ َ َ اِ ِج ا ُّز َْبَا‬
ِ ِ ‫ْا‬
Ak ci soxlaay alaaxira yi wal-ākhirati
َ َ
Yoo xam ni ñeel na la laka َ َ‫ا‬
Ci soxla sa su fajoo fīhā ‫ِ َا‬
Ngërmande riḍanā ‫ِ ًى‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

9 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Te ñeel nañ ca walanā ‫َ اََا‬

Bu fajoo fīhā ‫ِ َا‬
Ag yéwén ṣalāḥun ‫ا‬ٌ َ‫َ ًل‬
Ndare dimbali nga nu 'illā 'a`antanā ‫َِّل َ َ َْبلََبَا‬
Cig pajam `alā qaḍā'ihā ‫َ َى َ َ ااِ َ ا‬
Ci ag jàppandal fī yusrin ٍُْ ِ
Bu tukkéekoo ci yaw minka َ ْ ‫ِم‬
ٍ ‫َا َِّل‬
Ak aafiya(fekk sax dun ca toskarewante) wa`āfiyatin
َ
Naka yaw Boroom Bi 'innaka َ ‫َِّل‬
ِ
Aji àttan nga lool qadīrun
ٌ َ
ٍ ‫َى ُ ِي َا‬
Ci lépp lu mu mënti doon `alā kulli shay'in
ْ ّ َ
ِ
Ku yellu nga Wa jadīrun
ٌ ََ
ِ ‫ِ ِْ ا‬
Ci nangu ñaanu ku lay ñaan bil-'ijābati
ََ
ِ َ‫َ ْاًَل‬
Yaw Boroom màgg gi yā dhāl-jalāli
َ
ِ ِْ َ
Yaw Boroom teral gi wal-'ikrāmi
َ
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga nu yërëm irḥamnā ‫ْ َ َْا‬
ِ ُ ْ‫ِ ا‬
‫آو‬
Ci Alxur-aan bil-qurāni
ْ
Mu màgg mi al`aḍhīmi ‫اْ َ ِ ِي‬
Te yal na nga nu jariñ wānfa`nā ‫َ َْب َف ْ َا‬
Ci li nekk ci biir alxur-aan bimā fīhi ِ ِ ‫َِا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

10 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

‫ا‬ ِ ‫ِم ْا‬

Ci xeetu ay aaya ak kéemtaan minal-āyāti
َ َ
Ak alxur-aan lu mu làmboo wadh-dhikril-ḥakīmi ‫َ ا ِّذ ْ ِ ْاَ ِ ِي‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga nu xamal `allimnā ‫َ ِّ ْمَا‬
ِ
Ci alxur-aan minhu ُ ْ‫م‬
Lu nu réere mā jahilnā ‫َما َ ِ َْا‬
Te yal na nga nu fàttali Wa dhakkirnā َ ْ ِّ َ َ
ِ
Ci alxur-aan minhu ُ ْ‫م‬
Lu nu fàtte mā nasīnā ‫َما َ ِ َا‬
Te yal na nga nu wërsëgal wārzuqnā ‫َ ْ ُز َْبَا‬
Ag jàngam gu sax tilāwatahu ُ َ‫تًِلَ َ ت‬
Ak neexam ci mos Wa ḥalāwatahu ُ َ‫َ َ ًلَ َ ت‬
Ci waxtuy guddi ānā'al layli ‫آ َ َ ا َّلْ ِي‬
Ak ci bëccëg wa'aṭrāfan-nahāri ِ ‫َ َ ْ َ َ اَّلَب َ ا‬
ِ
Ngir sàkku ibtighā'a
َ ‫ْلغَا‬
Sag ngërmande marḍātika َ ِ‫َم ْ َ ات‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
ِ ِ َ َ َ ‫ما‬
La àtte nga ko / dogal nga ko mā qaḍayta bihi ْ َ
Te mu dal sunu kaw `alaynā ‫َ ََْبَا‬
ٍ ‫ِم َ َ ا‬
Ci ab àtte boo dogal min qaḍā'in
ْ
Yal na nga def fāj`al ‫َا ْ َ ْي‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

11 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Mujjag àtte boobu `āqibatahu ُ َ‫َا ََِبل‬

Muy njub ak lu baax ci nun rushdan ً ‫ُ ْا‬
Yaw Boroom sunu rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Yal na nga may ñu ātinā ‫آتَِا‬
Tukkée ci yaw min ladunka َ ْ ُ َ‫ِم ْ ا‬
Yërmande raḥmatan ً َْ َ
Yal na nga xàddu (defal nu) wa hayyi' ‫َ َ ِّ ْئ‬
Ñeel nu Lanā ‫اََا‬
Sunuy mbir min 'amrinā َ ِ ‫ِم ْ َْم‬
Njub Rashadan ً ‫َ َا‬
Yaw Boroom sunu Rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Yal na nga nu may ātinā ‫آتَِا‬
Ci àddina bi fīd-dunyā ‫ِ ا ُّز َْبَا‬
Yool/lépp lu baax te rafet ḥasanatan ًََ َ
ِ ِ ‫ِ ْا‬
Ak ci alaaxira wa fīl-ākhirati
َ َ
Yool ḥasanatan ًََ َ
Yal na nga nu musal wa qinā ‫َ َِا‬
Ci mbugëlum sawara `adhāban-nāri ِ ‫ا اَّلا‬َ ‫َ َذ‬
Yaw sunu Boroom Rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Yàlla bul toppanteek nun ba di nu fayante lā tu'ākhidhnā َ ‫َ تَُب َ ِ ْذ‬
Ndéem fàtte nañu la nu waxoon ak yaw 'in nasīnā ‫ِ ْو َ ِ َا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

12 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Walla nu juum ba def lu nu warutoon a def 'aw 'akhṭa'nā َ َْ‫َ ْ َ ْ ط‬

Yaw sunu Boroom rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Yàlla bul sëf walā taḥmil ‫َ َ َ ْ ِم ْي‬
Ci sunu kaw `alaynā ‫َ ََْبَا‬
ِ
Yan bu diis boo xam ni du baax 'iṣran
ًْ
Na nga sëfeewoon ko kamā ḥamaltahu ُ َ‫َ َما ََ ْل‬
ِ ‫َّل‬
Ca ña nga xam ni `alāl-ladhīna
َ ‫َ َى اذ‬
Jiituwoon na ñu min qablinā ‫ِم ْ ََب ْ َِا‬
Yaw sunu Boroom rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Bul nu teg mukk walā tuḥammilnā ‫َ َ َُ ِّم َْا‬
Loo xam ni mā ‫َما‬
àttanun ko lāṭāqata lanā bihi ِ ِ ‫َ َا َ َ اََا‬
Yal na nga nu jéggal wā`fu `annā ‫ف ََّلا‬ ُ ْ َ
Yal na nga nu baal sunuy bàkkaar wāghfirlanā ‫َ ْ ِف ْ اََا‬
Yal na nga nu yërëm wārḥamnā ‫َ ْ َ َْا‬
Yaw 'anta َ َْ
Yaay sunu Boroom mawlānā َ َ ْ ‫َم‬
Yal na nga nu dimbali ba nu am ndam fānṣurnā َ ْ‫ص‬ُ ْ ‫َا‬
ِ ِ
Ci yéefër yiy bañ `alāl-qawmil-kāfirīna
َ ِ ‫َ َى اْ َ ْ اْ َ ا‬
Yaw sunu Boroom rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Yàlla bul jengal lā tuzigh ْ ‫َ تُ ِل‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

13 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Sunu xol yi qulūbanā ‫َُب ُ ََبَا‬

Gannaaw boo nu jubalée ba`da 'idh hadaytanā ‫ََب ْ َ ِ ْ َ َ َْبلََبَا‬
Te nga may wa hab ‫ب‬ْ ََ
Ñeel nu lanā ‫اََا‬
Tukkée ci yaw min ladunka َ ْ ُ َ‫ِم ْ ا‬
Yërmande gu yaatu raḥmatan ً َْ َ
Naka yaw 'innaka َ ‫َِّل‬
Yaw 'anta َ َْ
Yaay Mayaakoon bi al-wahhābu ‫َّلاا‬
ُ َ ْ‫ا‬
Yaw sunu Boroom rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Naka ñun ñii 'innanā ‫َِّلَبَا‬
Degg nañu sami`nā ‫ََِس ْ َا‬
ِ
Aji woote juy joore ci yaw munādiyan
ً ‫ُمَاد‬
‫ادي‬ِ َ‫َب‬
Koo xam ni mu ngi woote yunādī
ُ
Jëm ci gëm Yàlla ne Kooku mooy Yónent bi lil'īmāni ِ َ ِْ ِ‫ا‬
‫او‬
Naka luy mbir tey mbir 'an ‫َ ْو‬
ِ
‫آم‬
Gëm léen āminū ُ
Seen Boroom birabbikum ‫َِ ِّ ُ ْي‬
Ñu gëm ko Fa āmannā ‫آمَّلا‬
ََ
Yaw sunu Boroom rabbanā ‫ََّلَبَا‬
ِ
Na nga jéggal fāghfir
ْ ‫َا ْف‬
Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.
14 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Ñeel ñu lanā ‫اََا‬

Sunu bàkkaar yi dhunūbanā ‫ُ ُ ََبَا‬
ِ
Yal na nga baal wakaffir
ْ ‫َ َ ّف‬
Wëliis ñu `annā ‫ََّلا‬
Sunu ñaawtéef yi sayyi'ātinā ‫َ ِّبَاتَِا‬
Te yal na nga ñu faat ëllëg Wa tawaffanā ‫َ تََب َ َّلَبَا‬
Ñu àndak ñu baax ñi nga tànn ma`al-'abrāri ِ َ ‫َم َع ْاََْب‬
Yaw sunu Boroom rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Yal na nga ñu jox Wa ātinā ‫َآتَِا‬
La nga ñu digóon mā wa`adtanā ‫َما َ َ ْ تََبَا‬
Ci làmmiñu sa Yónent yi `alā rusulika َ ِ ُ ُ ‫َ َى‬
Yàlla bul gàccel ñu / toroxal ñu walā tukhzinā َ‫َ َ ُ ْ ِل‬
ِ ‫َب اْ ِ ام‬
Bésu pénc yawmal-qiyāmati
َ َ َ َْ
Naka yaw 'innaka َ ‫َِّل‬
Doo wor (fausser) lā tukhlifu ‫ف‬ ُ ِْ ُ َ
Ag dëhël (rendez-vous) almī`āda َ َ ‫ا ِْم‬
‫اد‬
Yaw Boroom sunu rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Tooñ nanu ḍhalamnā ‫ظََ ْمَا‬
Sunu bopp 'anfusanā ‫ََْب ُف َ َا‬
ِ
Ndem jéggale wul wa'in lam taghfir
ْ ‫َ ِ ْو َْ تََبغْف‬
Ñeel nu lanā ‫اََا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

15 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Te nga yërëm nu Wa tarḥamnā ‫َ تََب ْ َ َْا‬

Dananu nekk lanakūnanna ‫اََ ُ َ َّل‬
ِ ِ
Ci way pert ñi minal-khāsirīna
َ ِ ‫م َ ْاَا‬
Yaw Boroom sunu rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Yal na nga may hab ‫ب‬ْ َ
Ñeel nu lanā ‫اََا‬
Ci sunu soxna yi min 'azwājinā ‫ِم ْ َ ْزَ ِ َا‬
Ak sunu njaboot yi wadhurriyātinā ‫َ ُ ِّ َ تَِا‬
Xol bu sedd qurrata 'ayunin ٍ ُ ْ َ َ ‫َُب َّل‬
‫ني‬
Te yal na nga def nu wāj`alnā ‫َ ْ َ َْا‬
Nuy jiit 'imāman ‫ِ َم ًاما‬
‫ني‬ ِ ِ‫ا‬
Ñeel way ragal Yàlla ñi lilmuttaqīna
َ ‫ْملَّل‬ ُ
Yaw Boroom sunu rabbanā ‫ََّلَبَا‬
ِ
Yal na nga jéggal 'ighfir
ْ ‫ِ ْف‬
Ñeel nu lanā ‫اََا‬
Ñeel sunu mbokk yi wali'ikhwāninā ‫َ ِِ ْ َ َِا‬
ِ ‫َّل‬
Ñaa ña Al ladhīna
َ ‫اذ‬
Jiituwóon nañu sabaqūnā َ ُ ‫َ ََب‬
Ngir gëm gi ñu gëm bil-'īmāni ِ َ ِْ ِ
‫او‬
Yàlla bul def walā taj`al ‫َ َ ََتْ َ ْي‬
Ci sunu xol yi fī qulūbinā ‫ِ َُب ُ َِا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

16 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Mbañeel ghillan ًّ‫ِ ًل‬

ِِ
Ñeel nit ña nga xam ni lilladhīna
َ ‫ا َّلذ‬
Gëm nanu āmanū ُ ‫آم‬
َ
Yaw Boroom sunu rabbanā ‫ََّلَبَا‬
Yaw 'innaka َ ‫َِّل‬
Ñeewatiwaakoon nga raūfun ٌ َُ
Yërëmaakoon nga raḥīmun ‫َ ِ ٌي‬
Yaw sunu Boroom yā rabbanā ‫َ ََّلَبَا‬
ِ ‫ااِ اْ َب‬
Yaw miy aji bind a’waalim yépp yā khāliqal`awālimi
ََ َ َ َ
Yal na nga dox ḥul ‫ُ ْي‬
Sunu diggante baynanā ‫ََب َْبََبَا‬
Ak sunu diggante ak bépp aji-tooñ Wa bayna kulli ḍhālimi ‫َبي ظَااِ َِبي‬
ِّ ُ ‫َبني‬
َْ ََ
Yaw suñu Boroom Ya rabbanā ‫َ ََّلَبَا‬
Yaw 'anta َ َْ
Yaa ngi janoo / xam tarā ‫تََب َى‬
Lépp lu xew mā qad jarā ‫َما َ ْ َ َى‬
Yal na nga damm fāqṣim ِ ْ ‫َا‬
‫ص ْي‬
Ci not ga ngay not boo meree biqahrin ٍ ْ َِ
Ka nga xam ne man
ْ ‫َمَب‬
Jéem naa ñeme ñemelu jasarā
ََ َ
Ci nun `alaynā ‫َ ََْبَا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

17 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Yaw Boroom suñu yā rabbanā ‫ََبَبا ََّلَبَا‬

Yal na nga gaawal `ajjil ‫َ ِّج ْي‬
Ñeel ñu lanā ‫اََبَا‬
Ci yér-yér bil-faraji ‫ِ اْ َفَب َ ِج‬
Te yal na nga musal ñu Wa najjinā ‫َ َِنَّبَا‬
ٍ ‫ِمَب َ َب َب‬
Ci sànku min ḍay`atin
َْ ْ
Ak tiis Wa ḥarajin ‫َ َ َ ٍج‬
Yal na nga tallal (yal na nga ñu sàng) wāmdud ‫َ ْمَب ُ ْد‬
Ci sunu kaw `alaynā ‫َ ََْبَا‬
Tukkee ci sa not gi min ḥimāka َ َ ِ ْ ‫ِم‬
‫اك‬
Bay gёn a terewu al'amna`i ‫ْاَ ْمَبَ ِع‬
Mbaar moo xam ne surādiqan ‫ُ َ ِد ًا‬
Ku tàbbi na man ḥalla ‫َبي‬
‫َمَب ْ َ َب َّل‬
Ci biir mbaar ma fīhi ِِ
Deef nay tere ko wёliis lu bon yumna`i ‫َُْ ِع‬
Yaw sunu Broom allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga sàmm ñu uḥrusnā ‫ُ ْ ُ ْ َا‬
Ci dooley bёt sa bi`aynika َ ِْ َ ِ
Gi nga xam ne Al latī ِ‫اَّل‬
Du nelaw lātanāmu
ُ ‫تََبَا‬
Yal na nga dugal ñu wāknufnā ‫َ ْ َُب ْفَا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

18 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Ci sa biir fī kanafika َ ‫ِ َ َ ِف‬

Bi nga xam ne al-ladhī ‫اَّل ِذي‬
Kenn du fa yegg lā yurāmu
ُ َ ‫َ َُب‬
Yal na nga def ñu wāj`alnā ‫َ ْ َ َْا‬
Ci sa dёkkaale fī jiwārika ‫ِ ِ َ ِ َك‬
Gi nga xam ne alladhī ‫اَّل ِذي‬
Deefut firi kóllёre ku fa duggu lā yukhfaru
ُ ‫َ ُُيَْف‬
Te kenn du la fa tooñ Wa lā yuḍāmu
ُ ‫َ َ ُ َا‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi Allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Ñu ngi jeng nadra'u
َُ َْ
Ci yaw bika َِ
ِ َ ْ َ‫ِ ُ ِ ْا‬
Ci baati noon yi fī nuḥūril'adā'i ُ
Ñu ngi muslu Wa na`ūdhu ُ ُ ‫َ ََب‬
Ci yaw bika َِ
Ci seeni ay min shurūrihim ‫ِم ْ ُا ُ ِ ِ ْي‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi Allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Yal na nga fegal ñu leen akfināhum ‫ْ ِفَا ُ ْي‬
Ci lula soob bimā shi'ta َ ‫َِا ِا ْب‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi Allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
Naka Yaw innaka َ ‫َِّل‬
Ya gёna xam 'alamu ‫َ ْ َ ُي‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

19 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Ci noon yi bi'adā'inā ‫ِِبَ ْ َ اَِا‬

Te doyna Wa kafā ‫َ َ َفى‬
Ci yaw bika َِ
Aji méngoo waliyyan ‫َ اًِّا‬
Te doyna Wa kafā ‫َ َ َفى‬
Ci yaw bika َِ
ِ
Aji dimbaliyaakoon naṣīrā
ً ‫َص‬
Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi Allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬
ِ
Yal na nga jéggal ighfir
ْ ‫ْف‬
Neel aji dundu ci nun liḥayyinā ‫ِاََِّا‬
Ak aji dee ci nun Wa mayyitinā ‫َ َمِّلَِا‬
Ak aji mag ci nun Wa kabīrinā َِ ِ ََ
Ak aji ndaw ci nun Wa ṣaghīrinā َ ِ ‫َ َ ِغ‬
Ak góor ci nun Wa dhakarinā َِ ََ َ
Ak jigéen ci nun wa'unthānā َ ‫َ َُْب َا‬
Ak aji teew ci nun Wa ḥāḍirinā َِ ِ ‫َ َ ا‬
Ak aji fàddu ci nun Wa ghā'ibinā ‫َ َااَِِا‬
Ak gor ci nun Wa ḥurrinā َ ِّ ُ َ
Ak jaam ci nun wa`abdinā َ ِ َْ َ
Ak aji topp waṭā'i`inā ‫َ َااِ َِا‬
Ak aji moy ci nun wa`āṣīnā ‫َ َا ِ َا‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

20 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

Yaw Boroom tur yu sell yi ak melo yu rafet yi Allāhumma ‫ا َّل ُ َّلي‬

ِ
Yal na nga jéggal ighfir
ْ ‫ْف‬
Ñeel nu lanā ‫اََا‬
ِ
Mbooleem ci nun 'ajma`īna
َ َْ َ
‫ني‬
Te yal na nga faat ñu Wa tawaffanā ‫َ تََب َ َّلَبَا‬
ِ
Ñu di jullit muslimīna
َ ‫ُم ْ ِم‬
‫ني‬
Yal na nga pang ñu wāḥshurnā َ ْ‫ل‬ُْ َ
ِ
Ci mbooloom Yonent yi fī zumratin-nabiyyīna
َ ِِّ‫ِ ُزْم َ اَّل‬
‫ني‬
‫ني‬ ِِِ
Ak mbooloom way dёggu yi waṣ-ṣiddīqīna
َ ّ ‫اص‬ ّ َ
ِ َ ‫ال‬
Ak ñi shahiid ci toolu Yàlla wash-shuhadā'i
َ ‫َ ُّز‬
Ak ñu yiw ñi waṣ-ṣāliḥīna
َ ِِ‫اصاا‬
‫ني‬ ‫َ َّل‬
Te yal na nga fegal ñu wākfinā ‫َ ْ ِفَا‬
La ñu ittel mā 'ahammanā ‫ََهَّلَا‬
َ ‫َما‬
Ak la ñu ittelul Wa mā lam yuhimmanā ‫َ َما َْ ُِ َّلمَا‬
Ci mbiru àddina min 'amūrid-dunyā ‫ِم ْ ُُم ِ ا ُّز َْبَا‬
Ak mbiru diine waddīni ِ ِّ ‫َ ا‬
Te yal na nga feg Wa kuffa ‫ف‬‫َ ُ َّل‬
Wëliis ñu `annā ‫ََّلا‬
ِ ِ
Loxooy way tooñ ñi 'aydīl-mu`tadīna
َ َ‫َْ ي ا ُْم ْل‬
Te Yàlla bul def ñu walā taj`alnā ‫َ َ ََتْ َ َْا‬
Ñuy nattu fitnatan ً َ‫ِ ْلَب‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

21 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18
Firi xatmu alxur’aan ci làkku wolof Pirim Ustaaz Barhaam Jóob
Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw

ِ َ ْ ِ‫ا‬
Ñeel nit ñi lilqawmi
ْ
ِ
Yadi way tooñ aḍh-ḍhālimīna
َ ‫ا َّلاا ِم‬
‫ني‬
Te yal na nga musal ñu Wa najjinā ‫َ َِنَّا‬
Ci sa yërmande gu yaatu gi biraḥmatika َ ِ‫َِ ْ َل‬
ِ َ ْ‫ِم ا‬
Ci gaa ñi minal-qawmi
ْ َ
ِ
Yadi way weddi Yàlla alkāfirīna
َ ِ ‫اْ َ ا‬
Te yal na nga def ñu wāj`alnā ‫َ ْ َ َْا‬
ِ ِ ‫ِم‬
‫اد َك‬
Ñu bokk ci sa jaam yi min`ibādika
َ ْ
‫ني‬
َ‫ص‬ ِ ِ ‫اْم ْخ‬
Yadi way sellal almukhliṣīna
ُ
Ci kaw yërmande gi nga ñu yërëm biraḥmatika َ ِ‫َِ ْ َل‬
ِ
َ ِ ‫َ َ ْ َ َي ا َّل‬
‫ني‬
Yaw mi nga xam ni yaa gëna yërëm képp kuy
yā 'arḥamar-rāḥimīna
yërëm

Yaw miy Boroom mbindeef yépp yā rabbal-`ālamīna

َ ‫ا اْ َااَ ِم‬
‫ني‬ ‫َ َ َّل‬

Tous droits de reproduction ou d’adaptation, réservés à l’auteur.

22 Elhadji Malick Sow 77 295 74 18

You might also like