You are on page 1of 2

Greetings: General Useful Phrases

Salaam maaleekum - Peace Be With you Degg nga Angele? - Do you speak English
Maaleekum Salaam -Peace Return to you Tutti Wolof rek la degg – I speak a little wolof
Loo wax? ngane? – What did you say?
Jàmm Nga am - Do you have peace Dégguma li nga wax - I don’t understand
Jàmm rek - Peace only Xam naa li nga wax. – I understand you.
Dégguma li nga wax franse – I don’t understand French
Na nga def - How are you Nageen def (plural)
Maa ngi fi rekk -I am here only (I am fine) Baax na – It’s Good
Neex na - It’s good / pleasant /spicy (can refer to food)
No (nga) tudd? (Naka nga tudd?) - What is your name Safna sap – Everything tastes wonderful
Andrew laa tudd – My name is Andrew Naka suba ngi – Good Morning
Naka ngoon ngi – Good Afternnon
Yow nak? – and you? Ñu fanaan ak jàmm – Good Evening

No (nga) sant? What is your last name? Waaw - Yes


Chow laa sant – My last name is Chow Deedeet - No

Kan moy sa Yaay – Who is your mother? Jere-jef – Thank You


Kan moy sa Baay - Who is your father? Sula Nexee – Please
Amul Solo – You are welcome
Naka yaram wi - Is your body in peace
Jamm rek – peace only Jeggel Ma – Excuse me
Baal Ma – I’m sorry
Naka waa ker gi – How is your family
Nu ngi fi. – They are fine. Naka – How
Kañ – When
Naka ligéey bi- How is the work Lan - What
Maangi si kowarm ndanka, ndanka – I am on it slowly Fan - Where
Fan la….nek? - Where is the….
Kontaan naa ci sa xamel. – I am glad to meat you
Abu kii mooy David – Abu, this is David Dama buga…. – I would like to….
Dama buga sangu - I would like to bathe
Nyatta at nga am? - How many years are you? Nunyi waxee _____ chi Wolof? How do you say this in Wolof?
_______________________________________________
Leaving: Man naa le photo – Can I take your photo
Na la yalla aar – Take care of yourself Baax na. Beneen yoon - Its good. But another time
May ma jamm – Leave me alone
Jamm ak jamm – Peace and Peace Begg na (Dama begg) la photo – I want you to take a photo
Dama dem ekool bi – I am going to School
Ba Beenen – See you later Naka suba ci - how is your morning? Jamm rek – peace only
_______________________________________________ Nga nelaw bu baax? - Did you sleep well? Jamm rek – peace only
Origins:
Kaay fii-come here Yaangi toog-you are sitting
Fan nga jogée? – Where are you from (born)
kaay leeka-come eat Li Lan la?-what is it?
America laa jogée. – I am from (born) America
Lu xew?-What happened? Fooy dem-where are you going?
San Francisco, California laa jogee ci America.
Looy def-what are you doing? Maangéé dem-I’m going
I am from SF, CA in America
loo buga-what do you want?
Baayi ma-leave me Mey ma ndox-offer me water
Fan la dekka? - Where are you from (recently)?
lii lan la?-what is this
Maangi jangi-I’m going to learn Doy na-enough
Man jangakat laa – I am a student
Ma gis-let me see Danga dof?-you crazy?
Loo wax?-what did you say? Lula jot?-what’s bothering you?
Man Jangalekate laa – I am a teacher
Mangi Santa Yalla – I thank God
Sama Famie – My familie Yalla na yalla ah – God Bless your endeavor
Sama Keur – My house Jangelma – teach me
Buggen ga…… Do you like…..
Toubab – Foreigner Yow Lygeeil – We work together.
Nikanuwal – Senegalese Namu Nala – Miss you Malarox! – I miss you to!
Verbs: Directions and Time:
Wax – to say Ana - Where
Def - to do Ana ….wi? - Where is the….
Waañi – to reduce the price Ana wanak wi? – Where is the toilet?
Lekk – to eat Ana Aziz? (Where is Aziz?)
Sangu – to wash
Naan – to drink Mangi Nan – I drink Baal ma, dama réer – I’m sorry, I’m lost
Dem – to go
Ñu Dem – Let’s go. Dama dem Dakar – I’m going to Dakar Jaddal sa cammon – Turn Left
Egg - arrive Jaddal sa ndeyjoor – Turn Right
Dégg – understand Meti – to hear Cha kanam – Straight ahead
Jang – to learn Soo jàddee koñ bi – Around the Corner
Noppelu – to rest Xool – to look at something
Nelaw - to sleep Munumaa nelew – I couldn’t sleep Waxtu- time
Togu – to cook Baligay – to wrestle Ban waxtu moo jot – What time is it?
Togal – to sit Pulli – to pray Kañ ngay dem? – When are we going
Xam – to know Xammuma – I don’t know Kañ la di door? - When will that start?
Leegi Leegi – Right Now
____________________________________________________
Bachikanum – Later on
Adjectives and Adverbs:
Feebar – sick Mer - Angry
Ban waxtu ubi? – What time is it open?
Sonn – tired Metti - difficult
Gementu – Sleepy Xiif- hungry
Taxsi – taxi
Tanga – hot Rafet na = it’s beautiful
Fooy Dem? – Where are you going?
Sedd – cold Fex na = shady
Tahawal fee – stop here
Suur naa – full Garab bi fex na = the tree is shady
Tutti – little/small amount Torob - very/a lot
Dakar dafa sóri – Dakar is far from here
Amdolé – strong Barri - alot
Dem nga lopitaan – Did you go to the hospital?
Begga- happy Dama Begga – I am happy
Dama dem tolbi – I’m going to the farm.
Teranga- hospitality Yaxu – Broken
Dow – Fast Boox be - Nex

Food: Numbers
Yap – Meat 0 tus / neen / zéro [French] 18 fukk ak juróom-ñett
Duma Lekk Yap – I don’t eat meat. / sero / dara ["nothing"] 19 fukk ak juróom-ñeent
Jen, Baax Na – Fish is OK. 1 benn 20 ñaar-fukk
Du lekk Yap – He/She doesn’t eat meat 2 ñaar / yaar 26 ñaar-fukk ak juróom-benn
Kaay Lekk – come eat 3 ñett / ñatt / yett / yatt 30 ñett-fukk / fanweer
Kuddu – Spoon tanga na – hot neex na - delicious 4 ñeent / ñenent 40 ñeent-fukk
Tanga na neex na – hot and delicious 5 juróom 50 juróom-fukk
6 juróom-benn 100 téeméer
Saf na sap – This is really tasty
7 juróom-ñaar 101 téeméer ak benn
Patas – Potato
8 juróom-ñett 106 téeméer ak juróom-benn
Nyambi – Cassava / Manioc 9 juróom-ñeent 110 téeméer ak fukk
Basante – Eggplant 10 fukk 200 ñaar téeméer
Jen – Fish 11 fukk ak benn 300 ñett téeméer
Chebbu – Rice 12 fukk ak ñaar 400 ñeent téeméer
Cheebu jen - Fish and Rice 13 fukk ak ñett 500 juróom téeméer
Yax – Bone 14 fukk ak ñeent 600 juróom-benn téeméer
Various Nouns 15 fukk ak juróom 1000 junni / junne
Gor - Man Baay - Father 16 fukk ak juróom-benn
Bujigen - Woman Yaay – Mother 17 fukk ak juróom-ñaar
_________________________________________________________________________
Yalla - God Rackk - Younger Brother
Bargaining:
Maye - Gift Mack - Older Brother
Sayfa (CFA) – currency of Senegal
Ndox - Water Rox - Sister
Ñaata la? – How much is it?
Barndase - Bandage Xarit - Friend
Seer na torob – it’s too much
Keur - House Néné- Baby
Waañi – to reduce the price
Taaw – Rain Sochu – stick for toothbrush
Waanil ma- please reduce it for me
Jangalekate - Teacher Ginaar – Chicken
Lóólu dafa seer. Baalal ma waaňi ko
Dokteer - Doctor Golo – Monkey
That is very expensive. Please reduce it for me
ekool - School Baum - Donkey
Xaalis –money
Garub - Tree Baay - Goat
Xool dofé dara – Looking is free
Tolbí - Farm Fus - Horse
Jdegani – Pillow Dada - Fly
Pronouns with verbs of being: Pronouns possessive:
Dama – I Example: Dama suur naa = I’m full Sama – My
Danga – You Sama xarit - my friend Sama jabar/jekar - my wife/husband
Dafa – He/She/it Dangeen – You (plural) Sama Keur - my house
Danu – We Danu – They

You might also like