You are on page 1of 10

FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

FIRI ÑAANU BAAY ÑAS

BISMIL ILAAHI TUBTU

CI LÀKKU WOLOF

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 1


FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Assalaamu alaykum mbokk taalibe yi

Liggéey bii li ko tax a jóg moodi firi lépp lu Baay Ñas bind ci làkk wi
askan wi di gёn a jёfandikoo muy wolof, loo lu dafay yombal gёstu
taalibe bi, di na tax it nu xam bu baax li nuy ñaan.
Liggéey bii lu ma yàgg nisёr la, jublu wu ma ci darra lu dul laabiire.
Yal na sunu Boroom gёrёm ligéey bi te yombalal nu jёfee gi

Aji bind ji : Allaaji Maalig Saw


Jokku ca Seex Ibraahiima Sàll
(Yal na Yàlla yokk leeram)
Gёstukat

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 2


FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Wolof Transcription Arabe


Ci turu Yàlla bismil-'ilāhi ِِِِِ‫بِسِمِِالِلِه‬
Laay tuubee tubtu ِ‫تِبِت‬
Naka man 'innī ِ‫إِ ّن‬
Tuub naa tubtu ِ‫تِبِت‬
Tuub naa tubtu ِ‫تِبِت‬
Ci lépp lu ma jёf limā fa`altu ِ‫لِمِاِفِعِلِت‬
Walla lépp lu ma wax 'aw mā qultu ِ‫أِوِِمِاقِلِت‬
Tuub naa tubtu ِ‫تِبِت‬
Yaw Yàlla kiy Aji-yёrёm bépp
mbindéef ci àddina
'ayā raḥmānu ِِِِِِ‫أِيِ ِِرحِان‬
Yaw Aji-yёrёm jullit ci allaaxira yā raḥīmu ِ‫يِ ِِرحِيم‬
Doo ma gis lam taranī ِ‫لِِتِِرن‬
Ci melokaan boo xam ne fī ḥālatin ِ‫فِِحِالِة‬
Da nga yedd ko tulīmu ِ‫تِلِيم‬
Tuub naa tubtu ِ‫تِبِت‬
Yaw Aji-jéggale ji 'ayā ghaffāru ِ‫أِيِِغِفِار‬
Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 3
FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Yaw Aji-yёrёme ji yā ḥannānu ِ‫يِِحِنِان‬


Tuub naa tubtu ِ‫تِبِت‬
Yaw sama Boroom 'ayā rabbī ِ‫ِرّب‬
ِ ِ‫أِي‬
Yaw miy Xéewalaakoon Wa yā mannānu ِ‫ِويِِمِنِان‬
Tuub naa tubtu ِِِِِِ‫تِبِت‬
Ci dёgg dёgg ḥaqīqatan ِ‫حِقِيقِة‬
Barina buma wuññée wakam nakathtu ِ‫ِوكِمِِنِكِثِت‬
Ñeel ma lī ِ‫ل‬
Ab tuub tawbatan ِ‫تِ ِوبِة‬
Tay nag wal-yawma ِ‫ِو ِاليِ ِوم‬
Tuub naa tubtu ِ‫تِبِت‬
Ci dёgg dёgg ḥaqqan ‫حِقِا‬
Tuub naa tubtu ِِِِِ‫تِبِت‬
Fa néeg ba (kaaba ga) ladāl-bayti ِ‫لِدِىِالِبِيِت‬
Ak ci diggante ñaari doj ya
(safaa ak marwa)
Wa baynal-
jabalayni ِ‫ِوبِيِِالِبِلِي‬
Ak ca xayf minan wal-khayfi ِ‫ِوالِيِف‬

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 4


FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Ak masharil haraam wal-mash`ari ِ‫ِو ِالمِشِعِر‬


Ci diggante ñaari doj yooyu baynal-`alamayni ِ‫بِيِِالِعِلِمِي‬
Tuub naa tubtu ِِِِ‫تِبِت‬
Ca waxtu taxaw ca arafaat ladāl-wuqūfi ِ‫لِدِىِالِ ِوقِوف‬
Yaw Aji-xam ji yā`alīmu ِ‫يِعِلِيم‬
Yaw Aji-jéggale ji Wa yā`afuwu ِ‫ِويِعِفِو‬
Yaw sama Boroom rabbu ِِ‫ِرب‬
Yaw miy Aji-tedd yā karīmu ِ‫يِِكِِري‬
Man 'anā ِِِِِ‫أِن‬
Aji lott laa ḍa`īfun ِ‫ضِعِيف‬
Bёre naag ḥāraba ِِ‫حِ ِارب‬
Aji- mbёru ji kay Yàlla al-jabbārā ‫الِبِ ِارا‬
Dellu naa 'anabtu ِِِ‫أِنِبِت‬
Bes sama yawmī ‫يِ ِومِي‬
Di topp nag 'aqtafī ‫أِقِتِفِي‬
Yoonu way baax ñi al-'abrārā ‫الِبِِر ِارا‬

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 5


FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Tuub naa tubtu ِِِِِ‫تِبِت‬


Barina bu ma sànkee wakam ḍaiya`tu ِ‫ِوكِمِِضِيِعِت‬
Àq Yàlla ḥaqqa l-Lāhi ِ‫حِقِِللا‬
Ak àq jaam yi
waḥaqqa
khalqihi ِِ‫ِوحِقِِخِلِقِه‬
Ci lu amul yamuwaay bilā tanāhi ِ‫بِلِِتِنِاه‬
Yaw Yàlla yal na nga jèggal taghfiru ِِِِ‫تِغِفِر‬
Neel ma lī ِ‫ل‬
Yaw Yàlla yal na nga yenu waltataḥammal ِِ‫ِولِتِتِحِمِل‬
Wёliis ma (li ma tooñ ñeneen
ñi)
`annī ِ‫عِ ّن‬
Yal na nga jéggal fāghfir ِ‫فِاغِفِر‬
Samay bàkkaar khaṭīi'atī ِ‫خِطِيئِت‬
Yal na nga dindi ko (ñaawteef
yépp)
'azilhā ِ‫أِِزلِا‬
Ci man minnī ِ‫مِ ّن‬
Tuub naa tubtu ِِِِ‫تِبِت‬
Ci wax yi minal-'aqwal-i ِ‫مِنِِالِقِ ِوال‬
Ak ci jёf yi wal-'af`āli ِ‫ِوالِفِعِال‬

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 6


FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Ak ci yёngatu yi wal-ḥarakāti ِ‫ِوالِِركِات‬


Baayil bal ِ‫بِل‬
Ba ci nekkiin yi mina l-'aḥwal-i ِ‫مِنِِالِحِ ِوال‬
Dikk naa jii'tu ِِ‫جِئِت‬
Jёm ci néeg bi 'iilā l-bayti ِ‫إِلِِالِبِيِت‬
Te jubalu ma wamā āstaqamtu ِِ‫ِومِاِاسِتِقِمِت‬
Te ma dikkaal ko wajii'tuhu ِِ‫ِوجِئِتِه‬
Ma dikkalaat ko wajii'tuhu ِ‫ِوجِئِتِه‬
Te ma dikk wajii'tu ِ‫ِوجِئِت‬
Te ma dikkalaat ko waji'tuhu ِِِ‫ِوجِئِتِه‬
Te ma dikk waji'tu ِ‫ِوجِئِت‬
Yoonu juróom benneel bi sādisan ‫سِادِسِا‬
Te sellal naa waqad 'akhlaṣtu ِ‫ِوقِدِِأِخِلِصِت‬
Sama tuub tawbatī ِ‫تِ ِوبِت‬
Danama jublu wa'anḥū ِ‫ِوأِنِو‬
Ñeelag njub lilrashad ِ‫لِلِِرشِد‬

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 7


FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Tuub naa tubtu ِِِِ‫تِبِت‬


Ca kanamu Yónent bi ladān-nabiyyi ِ‫ب‬
ّ ِ‫لِدِىِالن‬
Ci jottaliku ci Yónent bi bin-nabiyyi ِّ ِ‫بِلن‬
‫ب‬
Yaw Yàlla yal na nga ma yёkati tarfa`unī ِِ‫تِِرفِعِن‬
Jёm ci jikkó likhuluqin ِِ‫لِلِق‬
Bay aji yёkatiku (yu kawe yi) saniyyin ِ‫ن‬
ّ ِ‫س‬
Tuub naa tubtu ِِِِ‫تِبِت‬
Te dootuma dellu walā 'a`ūdu ِ‫ِولِِأِعِود‬
Duma dellu lā 'a`ūdu ِ‫لِِأِعِود‬
Te du nekk walā yakūnu ِِِ‫ِولِِيِكِون‬
lu dul la nga namm ghayra mā turīdu ِ‫غِيِِمِاِتِِريد‬
Yàgg na ṭāla ِِِ‫طِال‬
Sama cofeel ishtiyāqī ‫اشِتِيِاقِي‬
Ñeel tuub lilmatābi ِ‫لِلِمِتِاب‬
Tuub naa tubtu ِ‫تِبِت‬
Naka man fa'innanī ِ‫فِإِنِن‬

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 8


FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Bes sama yawmī ‫يِ ِومِي‬


Dellu naa 'anabtu ِ‫أِنِبِت‬
Ñeel ko moom Yàlla lahu ِِ‫لِه‬
Tuub na qad tāba ِِِِ‫قِدِِتِب‬
Samay nopp sam`ī ‫سِعِي‬
Ak sama làmmiñ Wa lisānī ِ‫ِولِسِان‬
Ak samay gis (bёt) wal-baṣar ِ‫ِو ِالبِصِر‬
Tuub na Wa tāba ِ‫ِوتِب‬
Bépp pepp kullu ṭarafin ِ‫كِلِِطِِرف‬
Ci lépp loo xam ne nii dawe na
(xew na)
`ammā shajar ِ‫عِمِاِشِجِر‬
Dellu naa raja`tu ِِِِِ‫ِرجِعِت‬
Ñeel Yàlla lil'ilāhi ِ‫لِلِلِه‬
Sama Jamono dahrī ‫دِهِِري‬
Te dañu ma lam 'azal ِ‫لِِأِِزل‬
Nekk di aji sax ci buntam bibābihi ِ‫بِبِابِه‬
Tukkee ci abad (lu jiitu) min 'abadin ِ‫مِنِِأِبِد‬

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 9


FIRI ÑAANU BAAY ÑAS BISMIL ILAAHI TUBTU CI LÀKKU WOLOF

Jёm asal (lu mujj) 'ilāl-'azal ِ‫إِلِِالِِزل‬


Topp julli thummaṣ-ṣalātu ِِِِِ‫ثِِالصِلِة‬
Ak nuyóo was-salāmu ِ‫ِوالسِلِم‬
Dappet sarmadan ‫سِِرمِدِا‬
Yal na nekk ci Yónent bi `alān-nabiyyi ِ‫ب‬
ّ ِ‫عِلِىِالن‬
Ka de ku ñu tànn al-muṣṭafā ‫الِمِصِطِفِى‬
Kay Muhammad SAWS Muḥammadan ‫مِمِدِا‬
Ak ay ñoñam Wa ālihi ِ‫ِوآلِه‬
Ak sahaabaam yi Wa ṣaḥbihi ِ‫ِوصِحِبِه‬
Yadi way baax al-'abrāri ِ‫الِبِِرار‬
Feeg muuree na mā kuwira ِِ‫مِ ِاِكِ ِّور‬
Guddi al-laylu ِ‫اللِيِل‬
Ci bёccёg `alān-nahāri ِ‫عِلِىِالنِهِار‬

Aji bind ji: Allaaji Maal ig Saw 77 295 74 18 Page 10

You might also like